Al-Waqi'a · 28/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
فِي سِدْرٍ مَّخْضُودٍ ۝٢٨
Fee sidrim makhdood
📖 Tekkim Wolof
[ñoom ñanga ca]: déem yu amul dég,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 26-30 — Simoore Al-Waqi'a

26إِلَّا قِيلًا سَلَامًا سَلَامًا
lu dul dañuy wax rekk naan : “Jàmm nga am aa jàmm rekk! ”
27وَأَصْحَابُ الْيَمِينِ مَا أَصْحَابُ الْيَمِينِ
Ak waa ndeyjoor ; ana ñan ñoo di waa ndeyjoor ?
28فِي سِدْرٍ مَّخْضُودٍ
[ñoom ñanga ca]: déem yu amul dég,
29وَطَلْحٍ مَّنضُودٍ
ak ci garabi banaana yu meññet ma rangaloo,
30وَظِلٍّ مَّمْدُودٍ
ak ci biir keppaar yu nu yiif yaatu
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 28

Simoore Al-Waqi'a Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [ñoom ñanga ca]: déem yu amul dég,

Simoore Aaya 28/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers