Al-Waqi'a · 27/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
وَأَصْحَابُ الْيَمِينِ مَا أَصْحَابُ الْيَمِينِ ۝٢٧
Wa as haabul yameeni maaa as haabul Yameen
📖 Tekkim Wolof
Ak waa ndeyjoor ; ana ñan ñoo di waa ndeyjoor ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 25-29 — Simoore Al-Waqi'a

25لَا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا تَأْثِيمًا
Duñu fa dégg mukk ay waxi neen walla wax ju sew ;
26إِلَّا قِيلًا سَلَامًا سَلَامًا
lu dul dañuy wax rekk naan : “Jàmm nga am aa jàmm rekk! ”
27وَأَصْحَابُ الْيَمِينِ مَا أَصْحَابُ الْيَمِينِ
Ak waa ndeyjoor ; ana ñan ñoo di waa ndeyjoor ?
28فِي سِدْرٍ مَّخْضُودٍ
[ñoom ñanga ca]: déem yu amul dég,
29وَطَلْحٍ مَّنضُودٍ
ak ci garabi banaana yu meññet ma rangaloo,
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 27

Simoore Al-Waqi'a Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak waa ndeyjoor ; ana ñan ñoo di waa ndeyjoor…

Simoore Aaya 27/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers