Al-Qalam · 32/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
عَسَىٰ رَبُّنَا أَن يُبْدِلَنَا خَيْرًا مِّنْهَا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا رَاغِبُونَ ۝٣٢
Asaa rabbunaaa any yubdilanaa khairam minhaaa innaaa ilaa rabbinaa raaghiboon
📖 Tekkim Wolof
Aka neexoon Yàlla nangu sunu tuub wuutalal nu ko ak tool yu ko gën. Sunu Boroom la nu xemmem”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Al-Qalam

30فَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَلَاوَمُونَ
Ku nekk dëgmal morom ja, ñuy yeddante.
31قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا طَاغِينَ
Ñuy wax naan : “Ngalla ! Nun danoo bew.
32عَسَىٰ رَبُّنَا أَن يُبْدِلَنَا خَيْرًا مِّنْهَا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا رَاغِبُونَ
Aka neexoon Yàlla nangu sunu tuub wuutalal nu ko ak tool yu ko gën. Sunu Boroom la nu xemmem”.
33كَذَٰلِكَ الْعَذَابُ ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Noonu la mbugal ma deme woon ; te mbugalum àllaaxira maay gëna rëy, cëy bu ñu xamoon !
34إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ عِندَ رَبِّهِمْ جَنَّاتِ النَّعِيمِ
Ña ragal Yàlla dey ñoom am nanu Àjjanay xéewal fa seen Boroom.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Qalam 32

Simoore Al-Qalam Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Aka neexoon Yàlla nangu sunu tuub wuutalal nu ko ak…

Simoore Aaya 32/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers