Al-Qalam · 31/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا طَاغِينَ ۝٣١
Qaaloo yaa wailanaaa innaa kunnaa taagheen
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax naan : “Ngalla ! Nun danoo bew.

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-33 — Simoore Al-Qalam

29قَالُوا سُبْحَانَ رَبِّنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Ñu daldi ne : “Tudd nanu selluk sunu Boroom ! Nun dey, ay tooñkat lanu woon”.
30فَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَلَاوَمُونَ
Ku nekk dëgmal morom ja, ñuy yeddante.
31قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا طَاغِينَ
Ñuy wax naan : “Ngalla ! Nun danoo bew.
32عَسَىٰ رَبُّنَا أَن يُبْدِلَنَا خَيْرًا مِّنْهَا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا رَاغِبُونَ
Aka neexoon Yàlla nangu sunu tuub wuutalal nu ko ak tool yu ko gën. Sunu Boroom la nu xemmem”.
33كَذَٰلِكَ الْعَذَابُ ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Noonu la mbugal ma deme woon ; te mbugalum àllaaxira maay gëna rëy, cëy bu ñu xamoon !
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Al-Qalam 31

Simoore Al-Qalam Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax naan : “Ngalla ! Nun danoo bew.

Simoore Aaya 31/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers