Al-Qalam · 33/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
كَذَٰلِكَ الْعَذَابُ ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ ۝٣٣
Kazaalikal azaab, wa la`azaabul aakhirati akbar; law kaanoo ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Noonu la mbugal ma deme woon ; te mbugalum àllaaxira maay gëna rëy, cëy bu ñu xamoon !

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore Al-Qalam

31قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا طَاغِينَ
Ñuy wax naan : “Ngalla ! Nun danoo bew.
32عَسَىٰ رَبُّنَا أَن يُبْدِلَنَا خَيْرًا مِّنْهَا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا رَاغِبُونَ
Aka neexoon Yàlla nangu sunu tuub wuutalal nu ko ak tool yu ko gën. Sunu Boroom la nu xemmem”.
33كَذَٰلِكَ الْعَذَابُ ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Noonu la mbugal ma deme woon ; te mbugalum àllaaxira maay gëna rëy, cëy bu ñu xamoon !
34إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ عِندَ رَبِّهِمْ جَنَّاتِ النَّعِيمِ
Ña ragal Yàlla dey ñoom am nanu Àjjanay xéewal fa seen Boroom.
35أَفَنَجْعَلُ الْمُسْلِمِينَ كَالْمُجْرِمِينَ
Moo ndax danuy def ñi wommatu jëm ci [Yàlla] ñu yem ak tooñkat ya ?
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Al-Qalam 33

Simoore Al-Qalam Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la mbugal ma deme woon ; te mbugalum àllaaxira…

Simoore Aaya 33/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers