Al-Qalam · 41/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
أَمْ لَهُمْ شُرَكَاءُ فَلْيَأْتُوا بِشُرَكَائِهِمْ إِن كَانُوا صَادِقِينَ ٤١
Transliteration
Am lahum shurakaaa`u falyaatoo bishurakaaa `ihim in kaanoo saadiqeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Wala dañoo am ñu ñuy bokkaale ? Kon, nañu indi seen bokkaale ndegam nu dëggu la nu !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 39-43 — Al-Qalam
39أَمْ لَكُمْ أَيْمَانٌ عَلَيْنَا بَالِغَةٌ إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ ۙ إِنَّ لَكُمْ لَمَا تَحْكُمُونَ
Wala book da ngeen am sunu ngiñ luy law ba àllaaxira, Mu defal leen fa lu ngeen bëgg ?
40سَلْهُمْ أَيُّهُم بِذَٰلِكَ زَعِيمٌ
Laajleen baxam ana kan ci ñoom mooy pakk wi ?
41أَمْ لَهُمْ شُرَكَاءُ فَلْيَأْتُوا بِشُرَكَائِهِمْ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Wala dañoo am ñu ñuy bokkaale ? Kon, nañu indi seen bokkaale ndegam nu dëggu la nu !
42يَوْمَ يُكْشَفُ عَن سَاقٍ وَيُدْعَوْنَ إِلَى السُّجُودِ فَلَا يَسْتَطِيعُونَ
Bu keroogee ba ñuy wuññi ab yeel [tiitaange] nu def leen woo ngir ñu Sujud te du ñu ko man.
43خَاشِعَةً أَبْصَارُهُمْ تَرْهَقُهُمْ ذِلَّةٌ ۖ وَقَدْ كَانُوا يُدْعَوْنَ إِلَى السُّجُودِ وَهُمْ سَالِمُونَ
Ñuy xiin-xiini ne muq ak gàcce te kat ba ca ba ñuy dund daayees na léen woo ngir ñuy sujood (jullig) te booba dara dalut léen.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
41Aaya
Tekki — Al-Qalam 41
Simoore Al-Qalam Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wala dañoo am ñu ñuy bokkaale ? Kon, nañu indi…Simoore Aaya 41/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








