Al-Qalam · 42/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
يَوْمَ يُكْشَفُ عَن سَاقٍ وَيُدْعَوْنَ إِلَى السُّجُودِ فَلَا يَسْتَطِيعُونَ ۝٤٢
Yawma yukshafu `am saaqinw wa yud`awna ilas sujoodi falaa yastatee`oon
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee ba ñuy wuññi ab yeel [tiitaange] nu def leen woo ngir ñu Sujud te du ñu ko man.

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Al-Qalam

40سَلْهُمْ أَيُّهُم بِذَٰلِكَ زَعِيمٌ
Laajleen baxam ana kan ci ñoom mooy pakk wi ?
41أَمْ لَهُمْ شُرَكَاءُ فَلْيَأْتُوا بِشُرَكَائِهِمْ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Wala dañoo am ñu ñuy bokkaale ? Kon, nañu indi seen bokkaale ndegam nu dëggu la nu !
42يَوْمَ يُكْشَفُ عَن سَاقٍ وَيُدْعَوْنَ إِلَى السُّجُودِ فَلَا يَسْتَطِيعُونَ
Bu keroogee ba ñuy wuññi ab yeel [tiitaange] nu def leen woo ngir ñu Sujud te du ñu ko man.
43خَاشِعَةً أَبْصَارُهُمْ تَرْهَقُهُمْ ذِلَّةٌ ۖ وَقَدْ كَانُوا يُدْعَوْنَ إِلَى السُّجُودِ وَهُمْ سَالِمُونَ
Ñuy xiin-xiini ne muq ak gàcce te kat ba ca ba ñuy dund daayees na léen woo ngir ñuy sujood (jullig) te booba dara dalut léen.
44فَذَرْنِي وَمَن يُكَذِّبُ بِهَٰذَا الْحَدِيثِ ۖ سَنَسْتَدْرِجُهُم مِّنْ حَيْثُ لَا يَعْلَمُونَ
Bàyyee ma ak ñiy jàppe waxtaan wii ( Alxuraan) ay fen dina nu léen taxañe fu ñu dul xam.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Al-Qalam 42

Simoore Al-Qalam Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee ba ñuy wuññi ab yeel [tiitaange] nu def…

Simoore Aaya 42/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers