Al-Qalam · 40/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
سَلْهُمْ أَيُّهُم بِذَٰلِكَ زَعِيمٌ ۝٤٠
Salhum ayyuhum bizaa lika za`eem
📖 Tekkim Wolof
Laajleen baxam ana kan ci ñoom mooy pakk wi ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 38-42 — Al-Qalam

38إِنَّ لَكُمْ فِيهِ لَمَا تَخَيَّرُونَ
boo xam ne daal li ngeen bëgg lépp ngi ci ?
39أَمْ لَكُمْ أَيْمَانٌ عَلَيْنَا بَالِغَةٌ إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ ۙ إِنَّ لَكُمْ لَمَا تَحْكُمُونَ
Wala book da ngeen am sunu ngiñ luy law ba àllaaxira, Mu defal leen fa lu ngeen bëgg ?
40سَلْهُمْ أَيُّهُم بِذَٰلِكَ زَعِيمٌ
Laajleen baxam ana kan ci ñoom mooy pakk wi ?
41أَمْ لَهُمْ شُرَكَاءُ فَلْيَأْتُوا بِشُرَكَائِهِمْ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Wala dañoo am ñu ñuy bokkaale ? Kon, nañu indi seen bokkaale ndegam nu dëggu la nu !
42يَوْمَ يُكْشَفُ عَن سَاقٍ وَيُدْعَوْنَ إِلَى السُّجُودِ فَلَا يَسْتَطِيعُونَ
Bu keroogee ba ñuy wuññi ab yeel [tiitaange] nu def leen woo ngir ñu Sujud te du ñu ko man.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — Al-Qalam 40

Simoore Al-Qalam Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Laajleen baxam ana kan ci ñoom mooy pakk wi ?

Simoore Aaya 40/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers