Al-A'raf · 48/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَنَادَىٰ أَصْحَابُ الْأَعْرَافِ رِجَالًا يَعْرِفُونَهُم بِسِيمَاهُمْ قَالُوا مَا أَغْنَىٰ عَنكُمْ جَمْعُكُمْ وَمَا كُنتُمْ تَسْتَكْبِرُونَ ۝٤٨
Wa naadaaa Ashaabul A`raffi rijaalany ya`rifoonahum biseemaahum qaaloo maaa aghnaa `ankum jam`ukum wa maa kuntum tastakbiroon
📖 Tekkim Wolof
Ña nekk ca dig wa tuddu [Al-Lahraaf] woo ay nit ñu ñu xàmmee ngir seeni màndarga, ne leen : “Waa kon alal ja ngeen daan dajale ak la leen taxoon a rëy-rëylu, amaluñuleen benn njariñ !
🎧 Dégg

📜 Aaya 46-50 — Al-A'raf

46وَبَيْنَهُمَا حِجَابٌ ۚ وَعَلَى الْأَعْرَافِ رِجَالٌ يَعْرِفُونَ كُلًّا بِسِيمَاهُمْ ۚ وَنَادَوْا أَصْحَابَ الْجَنَّةِ أَن سَلَامٌ عَلَيْكُمْ ۚ لَمْ يَدْخُلُوهَا وَهُمْ يَطْمَعُونَ
Dox na ca seen diggante [waa Àjjana] kiiraay, nekk na ca kaw (dig) wa aw nit ñoo xam ne danañu leen xàmmee ñoom ñépp ca seen màndarga ya. Ñu woo waa Àjjana, ne leen : “Yal na jàmm nekk ci yéen ! ”. Ñoom duñu dugg Àjjana te xemmem nañu ko.
47۞ وَإِذَا صُرِفَتْ أَبْصَارُهُمْ تِلْقَاءَ أَصْحَابِ النَّارِ قَالُوا رَبَّنَا لَا تَجْعَلْنَا مَعَ الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Saa su seeni gët jubloo ca waa Safara, ñu ne : "Sunu Boroom, Yàlla boo nu boole ak nit ñu di ay tooñkat”.
48وَنَادَىٰ أَصْحَابُ الْأَعْرَافِ رِجَالًا يَعْرِفُونَهُم بِسِيمَاهُمْ قَالُوا مَا أَغْنَىٰ عَنكُمْ جَمْعُكُمْ وَمَا كُنتُمْ تَسْتَكْبِرُونَ
Ña nekk ca dig wa tuddu [Al-Lahraaf] woo ay nit ñu ñu xàmmee ngir seeni màndarga, ne leen : “Waa kon alal ja ngeen daan dajale ak la leen taxoon a rëy-rëylu, amaluñuleen benn njariñ !
49أَهَٰؤُلَاءِ الَّذِينَ أَقْسَمْتُمْ لَا يَنَالُهُمُ اللَّهُ بِرَحْمَةٍ ۚ ادْخُلُوا الْجَنَّةَ لَا خَوْفٌ عَلَيْكُمْ وَلَا أَنتُمْ تَحْزَنُونَ
Moo ndax ñii du ña ngeen giñoon ne Yàlla duleen dugal ci yërmaande... ? - Dugguleen ci Àjjana ! Te buleen am njàqare, te buleen am naqar.
50وَنَادَىٰ أَصْحَابُ النَّارِ أَصْحَابَ الْجَنَّةِ أَنْ أَفِيضُوا عَلَيْنَا مِنَ الْمَاءِ أَوْ مِمَّا رَزَقَكُمُ اللَّهُ ۚ قَالُوا إِنَّ اللَّهَ حَرَّمَهُمَا عَلَى الْكَافِرِينَ
Waa Safara woo waa Àjjana ne leen : “Bëbël-leen ci nun lenn ci ndox mi, walla ci li leen Yàlla wërsëgale.” Ñu toontu ne : “Yàlla dogal na ne [xéewal yii] araam na ci yéefar yi”.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Al-A'raf 48

Simoore Al-A'raf Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nekk ca dig wa tuddu [Al-Lahraaf] woo ay nit…

Simoore Aaya 48/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers