Al-Anfal · 57/75
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anfal
فَإِمَّا تَثْقَفَنَّهُمْ فِي الْحَرْبِ فَشَرِّدْ بِهِم مَّنْ خَلْفَهُمْ لَعَلَّهُمْ يَذَّكَّرُونَ ۝٥٧
Fa immaa tasqafannahum fil harbi fasharrid bihim man khalfahum la`allahum yazzakkaroon
📖 Tekkim Wolof
Kon su ngeen dajee cib xare, nanga leen tasaare ak ña leen topp ndax xéy-na danañu fàttaliku.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 55-59 — Simoore Al-Anfal

55إِنَّ شَرَّ الدَّوَابِّ عِندَ اللَّهِ الَّذِينَ كَفَرُوا فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Ña yées fa Yàlla ñooy ña weddi woon te duñu gëm ba mukk,
56الَّذِينَ عَاهَدتَّ مِنْهُمْ ثُمَّ يَنقُضُونَ عَهْدَهُمْ فِي كُلِّ مَرَّةٍ وَهُمْ لَا يَتَّقُونَ
mooy ña nga fasanteek kóllare ñu lay wor, te ñoom duñu ragal Yàlla mukk.
57فَإِمَّا تَثْقَفَنَّهُمْ فِي الْحَرْبِ فَشَرِّدْ بِهِم مَّنْ خَلْفَهُمْ لَعَلَّهُمْ يَذَّكَّرُونَ
Kon su ngeen dajee cib xare, nanga leen tasaare ak ña leen topp ndax xéy-na danañu fàttaliku.
58وَإِمَّا تَخَافَنَّ مِن قَوْمٍ خِيَانَةً فَانبِذْ إِلَيْهِمْ عَلَىٰ سَوَاءٍ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْخَائِنِينَ
Boo ragalee ciw nit ñu wor la, tërëlal déggoo gu leer, Yàlla soppul workat ya.
59وَلَا يَحْسَبَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا سَبَقُوا ۚ إِنَّهُمْ لَا يُعْجِزُونَ
Ña weddi, buñu njortu ne raw nañu. Ñoom duñu mën a raw Yàlla.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
57Aaya

Tekki — Al-Anfal 57

Simoore Al-Anfal Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kon su ngeen dajee cib xare, nanga leen tasaare ak…

Simoore Aaya 57/75 — Simoore Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anfal Dégg, Simoore Al-Anfal Tekki, Simoore Al-Anfal mp3, Simoore Al-Anfal pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers