Al-Anfal · 56/75
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anfal
الَّذِينَ عَاهَدتَّ مِنْهُمْ ثُمَّ يَنقُضُونَ عَهْدَهُمْ فِي كُلِّ مَرَّةٍ وَهُمْ لَا يَتَّقُونَ ۝٥٦
Allazeena`aahatta min hum summa yanqudoona `ahdahum fee kulli marratinw wa hum laa yattaqoon
📖 Tekkim Wolof
mooy ña nga fasanteek kóllare ñu lay wor, te ñoom duñu ragal Yàlla mukk.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 54-58 — Simoore Al-Anfal

54كَدَأْبِ آلِ فِرْعَوْنَ ۙ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَذَّبُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ فَأَهْلَكْنَاهُم بِذُنُوبِهِمْ وَأَغْرَقْنَا آلَ فِرْعَوْنَ ۚ وَكُلٌّ كَانُوا ظَالِمِينَ
Niki aada njabootu Firawna ak ña leen jiitu, weddi nañu kàdduy Boroom bi. Nu alag leen ngir seeni bàkkaar. Te Nu labal [ca géej] waa kër Firawna. Te ñoom ñépp nekkoon nañu di ay tooñkat.
55إِنَّ شَرَّ الدَّوَابِّ عِندَ اللَّهِ الَّذِينَ كَفَرُوا فَهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Ña yées fa Yàlla ñooy ña weddi woon te duñu gëm ba mukk,
56الَّذِينَ عَاهَدتَّ مِنْهُمْ ثُمَّ يَنقُضُونَ عَهْدَهُمْ فِي كُلِّ مَرَّةٍ وَهُمْ لَا يَتَّقُونَ
mooy ña nga fasanteek kóllare ñu lay wor, te ñoom duñu ragal Yàlla mukk.
57فَإِمَّا تَثْقَفَنَّهُمْ فِي الْحَرْبِ فَشَرِّدْ بِهِم مَّنْ خَلْفَهُمْ لَعَلَّهُمْ يَذَّكَّرُونَ
Kon su ngeen dajee cib xare, nanga leen tasaare ak ña leen topp ndax xéy-na danañu fàttaliku.
58وَإِمَّا تَخَافَنَّ مِن قَوْمٍ خِيَانَةً فَانبِذْ إِلَيْهِمْ عَلَىٰ سَوَاءٍ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْخَائِنِينَ
Boo ragalee ciw nit ñu wor la, tërëlal déggoo gu leer, Yàlla soppul workat ya.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
56Aaya

Tekki — Al-Anfal 56

Simoore Al-Anfal Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mooy ña nga fasanteek kóllare ñu lay wor, te ñoom…

Simoore Aaya 56/75 — Simoore Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anfal Dégg, Simoore Al-Anfal Tekki, Simoore Al-Anfal mp3, Simoore Al-Anfal pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers