Al-Baqara · 262/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
الَّذِينَ يُنفِقُونَ أَمْوَالَهُمْ فِي سَبِيلِ اللَّهِ ثُمَّ لَا يُتْبِعُونَ مَا أَنفَقُوا مَنًّا وَلَا أَذًى ۙ لَّهُمْ أَجْرُهُمْ عِندَ رَبِّهِمْ وَلَا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ ٢٦٢
Transliteration
Allazeena yunfiqoona amwaalahum fee sabeelillaahi summa laa yutbi`oona maaa anfaqoo mannanw wa laaa azal lahum ajruhum `inda Rabbihim; wa laa khawfun `alaihim wa laa hum yahzanoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne dañuy joxe seeni alal ci yoonu Yàlla te duñu toftale ca la ñu joxe ñax walla kañu , danañu am seenug pey fa Yàlla seen Boroom. Duñu tiit, duñu jàq.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 260-264 — Al-Baqara
260وَإِذْ قَالَ إِبْرَاهِيمُ رَبِّ أَرِنِي كَيْفَ تُحْيِي الْمَوْتَىٰ ۖ قَالَ أَوَلَمْ تُؤْمِن ۖ قَالَ بَلَىٰ وَلَٰكِن لِّيَطْمَئِنَّ قَلْبِي ۖ قَالَ فَخُذْ أَرْبَعَةً مِّنَ الطَّيْرِ فَصُرْهُنَّ إِلَيْكَ ثُمَّ اجْعَلْ عَلَىٰ كُلِّ جَبَلٍ مِّنْهُنَّ جُزْءًا ثُمَّ ادْعُهُنَّ يَأْتِينَكَ سَعْيًا ۚ وَاعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
[Fàttalikul] ba Ibraahiima waxee ne : “Sama Boroom ! Won ma ni ngay dekkalee ku dee”, mu ne ko : “Xanaa dangaa gëmul? ”. Mu ne ko “Axakay ! Waaye ngir sama xel dal”. Mu ne ko : “Jëlal ñeenti njanaaw, teppasleen , boo noppee nga teg ci kaw tund wu ne aw dogit, boo noppee nga woo leen : danañu yëngatu wutsi la. Yàlla Aji-not [tedd] la te ku xereñ la.”
261مَّثَلُ الَّذِينَ يُنفِقُونَ أَمْوَالَهُمْ فِي سَبِيلِ اللَّهِ كَمَثَلِ حَبَّةٍ أَنبَتَتْ سَبْعَ سَنَابِلَ فِي كُلِّ سُنبُلَةٍ مِّائَةُ حَبَّةٍ ۗ وَاللَّهُ يُضَاعِفُ لِمَن يَشَاءُ ۗ وَاللَّهُ وَاسِعٌ عَلِيمٌ
Méngaleg ña nga xam ne dañuy joxe seeni alal ci yoonu Yàlla mi ngi deme ni wenn pepp wu sax, seqi juróom-ñaari gupp, gupp wu nekk am téeméeri fepp. Yàlla mooy fulal ku ko soob,Yàlla ku yaatu ku xam la.
262الَّذِينَ يُنفِقُونَ أَمْوَالَهُمْ فِي سَبِيلِ اللَّهِ ثُمَّ لَا يُتْبِعُونَ مَا أَنفَقُوا مَنًّا وَلَا أَذًى ۙ لَّهُمْ أَجْرُهُمْ عِندَ رَبِّهِمْ وَلَا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Ña nga xam ne dañuy joxe seeni alal ci yoonu Yàlla te duñu toftale ca la ñu joxe ñax walla kañu , danañu am seenug pey fa Yàlla seen Boroom. Duñu tiit, duñu jàq.
263۞ قَوْلٌ مَّعْرُوفٌ وَمَغْفِرَةٌ خَيْرٌ مِّن صَدَقَةٍ يَتْبَعُهَا أَذًى ۗ وَاللَّهُ غَنِيٌّ حَلِيمٌ
Wax ju yiw ak ag njeggal moo gëm sarax boo xam ne wax ju ñaaw a ca topp. Yàlla ku woomal la, ku lewet la.
264يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُبْطِلُوا صَدَقَاتِكُم بِالْمَنِّ وَالْأَذَىٰ كَالَّذِي يُنفِقُ مَالَهُ رِئَاءَ النَّاسِ وَلَا يُؤْمِنُ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ ۖ فَمَثَلُهُ كَمَثَلِ صَفْوَانٍ عَلَيْهِ تُرَابٌ فَأَصَابَهُ وَابِلٌ فَتَرَكَهُ صَلْدًا ۖ لَّا يَقْدِرُونَ عَلَىٰ شَيْءٍ مِّمَّا كَسَبُوا ۗ وَاللَّهُ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الْكَافِرِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen yàq seeni sarax ci ñax ak kañu, képp ku joxe alal ngir ngistal ci nit ña te gëmul Bis-pénc ba. Dafay mel ni doj wu suuf tegu ca kawam ; waame sottiku ca, bàyyi ko mu ratax bandaŋ. [nit ñu mel noonu] duñu mën a def dara lu barkeel. Te Yàlla du gindi nit ñu weddi.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
262Aaya
Tekki — Al-Baqara 262
Simoore Al-Baqara Aaya 262 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne dañuy joxe seeni alal ci yoonu…Simoore Aaya 262/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 260–264. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








