Taha · 127/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَكَذَٰلِكَ نَجْزِي مَنْ أَسْرَفَ وَلَمْ يُؤْمِن بِآيَاتِ رَبِّهِ ۚ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَشَدُّ وَأَبْقَىٰ ۝١٢٧
Wa kazaalika najzee man asrafa wa lam yu`mim bi Aayaati Rabbih; wa la`azaabul Aakhirati ashaddu wa abqaa
📖 Tekkim Wolof
Noonu la Nuy feye ña ëppal [xaabaabal] te gëmuñu seen kàdduy Boroom [ay màndargaam]. Te mbugalum àllaaxira moo gën a tar te gën a yàgg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 125-129 — Simoore Taha

125قَالَ رَبِّ لِمَ حَشَرْتَنِي أَعْمَىٰ وَقَدْ كُنتُ بَصِيرًا
[Su ko defee] muy laaj naan : "Sama Boroom, lan moo tax nga pang ma may gumba te ca àddina ma doon gis ? ”
126قَالَ كَذَٰلِكَ أَتَتْكَ آيَاتُنَا فَنَسِيتَهَا ۖ وَكَذَٰلِكَ الْيَوْمَ تُنسَىٰ
[Yàlla tontu] ne ko : “Noonu la la Sunuy kàddu dikkalee woon, nga sàggane ko, kon book tey yaw itam kenn du la faale”.
127وَكَذَٰلِكَ نَجْزِي مَنْ أَسْرَفَ وَلَمْ يُؤْمِن بِآيَاتِ رَبِّهِ ۚ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَشَدُّ وَأَبْقَىٰ
Noonu la Nuy feye ña ëppal [xaabaabal] te gëmuñu seen kàdduy Boroom [ay màndargaam]. Te mbugalum àllaaxira moo gën a tar te gën a yàgg.
128أَفَلَمْ يَهْدِ لَهُمْ كَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّنَ الْقُرُونِ يَمْشُونَ فِي مَسَاكِنِهِمْ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّأُولِي النُّهَىٰ
Ndax dafa leerul ci seen bopp te aka bari ay xeet yu Nu alag ca ña leen jiitu woon te tey ñuy dox ci kaw fa ñu dëkkoon ? Loolu war naa mën a waar ñu am xel [te di ko jariñoo] !
129وَلَوْلَا كَلِمَةٌ سَبَقَتْ مِن رَّبِّكَ لَكَانَ لِزَامًا وَأَجَلٌ مُّسَمًّى
Su fekkoon ne du dig bu ko Yàlla sàkkal, kon seen mbugal fii lay tàmbalee.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
127Aaya

Tekki — Taha 127

Simoore Taha Aaya 127 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la Nuy feye ña ëppal [xaabaabal] te gëmuñu seen…

Simoore Aaya 127/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 125–129. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers