Taha · 8/135
Tekki Waxtaan — Taha
اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ لَهُ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ ٨
Transliteration
Allaahu laaa ilasha illaa Huwa lahul Asmaaa`ul Husnaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàlla mooy Yàlla ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom ! Moo moom tur yi gën a rafet.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 6-10 — Taha
6لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَمَا تَحْتَ الثَّرَىٰ
Moo moom li nekk ci asamaan yi ak ci suuf si ak li nekk ci seen diggante, ak li nekk ci ron déeley suuf si.
7وَإِن تَجْهَرْ بِالْقَوْلِ فَإِنَّهُ يَعْلَمُ السِّرَّ وَأَخْفَى
Soo dee jóoru say wax it, Moom xam na mbóot ak la gën a nëbbu.
8اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ لَهُ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ
Yàlla mooy Yàlla ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom ! Moo moom tur yi gën a rafet.
9وَهَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ مُوسَىٰ
Moo ndax xam nga xibaari Muusaa ?
10إِذْ رَأَىٰ نَارًا فَقَالَ لِأَهْلِهِ امْكُثُوا إِنِّي آنَسْتُ نَارًا لَّعَلِّي آتِيكُم مِّنْهَا بِقَبَسٍ أَوْ أَجِدُ عَلَى النَّارِ هُدًى
Ba mu gisee aw safara, mu ne njabootam : “Xaarleen ma fii ! Lële ma séen dey aw safara la ; Amaana ma jële fa aw xal, walla ma fekk fa ku ma gindi [teg ma ci yoon]”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
8Aaya
Tekki — Taha 8
Simoore Taha Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla mooy Yàlla ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom…Simoore Aaya 8/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








