Taha · 7/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَإِن تَجْهَرْ بِالْقَوْلِ فَإِنَّهُ يَعْلَمُ السِّرَّ وَأَخْفَى ۝٧
Wa in tajhar bilqawli fainnahoo ya`lamus sirra wa akhfaa
📖 Tekkim Wolof
Soo dee jóoru say wax it, Moom xam na mbóot ak la gën a nëbbu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Simoore Taha

5الرَّحْمَٰنُ عَلَى الْعَرْشِ اسْتَوَىٰ
Yàllaa nga yemoo ca Gàngunaay ga [Aras].
6لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَمَا تَحْتَ الثَّرَىٰ
Moo moom li nekk ci asamaan yi ak ci suuf si ak li nekk ci seen diggante, ak li nekk ci ron déeley suuf si.
7وَإِن تَجْهَرْ بِالْقَوْلِ فَإِنَّهُ يَعْلَمُ السِّرَّ وَأَخْفَى
Soo dee jóoru say wax it, Moom xam na mbóot ak la gën a nëbbu.
8اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ لَهُ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ
Yàlla mooy Yàlla ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom ! Moo moom tur yi gën a rafet.
9وَهَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ مُوسَىٰ
Moo ndax xam nga xibaari Muusaa ?
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Taha 7

Simoore Taha Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Soo dee jóoru say wax it, Moom xam na mbóot…

Simoore Aaya 7/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers