Taha · 9/135
Tekki Waxtaan — Taha
وَهَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ مُوسَىٰ ۝٩
Wa hal ataaka hadeesu Moosa
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax xam nga xibaari Muusaa ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 7-11 — Taha

7وَإِن تَجْهَرْ بِالْقَوْلِ فَإِنَّهُ يَعْلَمُ السِّرَّ وَأَخْفَى
Soo dee jóoru say wax it, Moom xam na mbóot ak la gën a nëbbu.
8اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ لَهُ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ
Yàlla mooy Yàlla ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom ! Moo moom tur yi gën a rafet.
9وَهَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ مُوسَىٰ
Moo ndax xam nga xibaari Muusaa ?
10إِذْ رَأَىٰ نَارًا فَقَالَ لِأَهْلِهِ امْكُثُوا إِنِّي آنَسْتُ نَارًا لَّعَلِّي آتِيكُم مِّنْهَا بِقَبَسٍ أَوْ أَجِدُ عَلَى النَّارِ هُدًى
Ba mu gisee aw safara, mu ne njabootam : “Xaarleen ma fii ! Lële ma séen dey aw safara la ; Amaana ma jële fa aw xal, walla ma fekk fa ku ma gindi [teg ma ci yoon]”.
11فَلَمَّا أَتَاهَا نُودِيَ يَا مُوسَىٰ
Ba mu agsee ci safara wa, mu am lu ko woo ne ko : “Éy Muusaa !
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Taha 9

Simoore Taha Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax xam nga xibaari Muusaa ?

Simoore Aaya 9/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers