An-Naml · 52/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
فَتِلْكَ بُيُوتُهُمْ خَاوِيَةً بِمَا ظَلَمُوا ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَعْلَمُونَ ۝٥٢
Fatilka buyootuhum khaa wiyatam bimaa zalamoo; inna fee zaalika la Aayatal liqaw miny-ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Seen kër yaa ngi noonu gent na ngir la ñu tooñoon. Ay kéemaan a ngi ci loolu ngir aw nit ñuy xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 50-54 — An-Naml

50وَمَكَرُوا مَكْرًا وَمَكَرْنَا مَكْرًا وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Ñangay fexe am pexe, Nun it Noo ngi fexe am pexe te ñoom yéguñu ko.
51فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ مَكْرِهِمْ أَنَّا دَمَّرْنَاهُمْ وَقَوْمَهُمْ أَجْمَعِينَ
Xoolal naka seen pexe ya mujje woon : Danu leen a faagaagal ñook seeni xeet wépp.
52فَتِلْكَ بُيُوتُهُمْ خَاوِيَةً بِمَا ظَلَمُوا ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَعْلَمُونَ
Seen kër yaa ngi noonu gent na ngir la ñu tooñoon. Ay kéemaan a ngi ci loolu ngir aw nit ñuy xam.
53وَأَنجَيْنَا الَّذِينَ آمَنُوا وَكَانُوا يَتَّقُونَ
Te musal Nanu ña gëmoon te ragal Yàlla.
54وَلُوطًا إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَتَأْتُونَ الْفَاحِشَةَ وَأَنتُمْ تُبْصِرُونَ
[Fàttalikul] Lóot, ba mu waxee aw nitam, ne leen : “Ndax dangeen di def ñaawtéef te ne ca jàkk”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — An-Naml 52

Simoore An-Naml Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen kër yaa ngi noonu gent na ngir la ñu…

Simoore Aaya 52/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers