Al-Fath · 1/29
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Fath
إِنَّا فَتَحْنَا لَكَ فَتْحًا مُّبِينًا ۝١
Innaa fatahnaa laka Fatham Mubeenaa
📖 Tekkim Wolof
Nun dey ubbil nanu la ubbi gu fes bir (jox la ndam) nga bom,

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Fath

1إِنَّا فَتَحْنَا لَكَ فَتْحًا مُّبِينًا
Nun dey ubbil nanu la ubbi gu fes bir (jox la ndam) nga bom,
2لِّيَغْفِرَ لَكَ اللَّهُ مَا تَقَدَّمَ مِن ذَنبِكَ وَمَا تَأَخَّرَ وَيُتِمَّ نِعْمَتَهُ عَلَيْكَ وَيَهْدِيَكَ صِرَاطًا مُّسْتَقِيمًا
ci loolu Yàlla dana la jéggal, la jëkkoon ci say bàkkaar ak lay xala mujj, te it Dana matal ay Xéewal ci yaw te itam dana gindi teg la ca kaw yoonam wu jub xocc wa ;
3وَيَنصُرَكَ اللَّهُ نَصْرًا عَزِيزًا
Yàlla dana la dimbali ndimbal (luy tax nga man a not say noon).
Al-FathFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Fath 1

Simoore Al-Fath Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun dey ubbil nanu la ubbi gu fes bir (jox…

Simoore Aaya 1/29 — Simoore Al-Fath الفتح (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Fath Dégg, Simoore Al-Fath Tekki, Simoore Al-Fath mp3, Simoore Al-Fath pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers