Al-Hujurat · 11/18
Tekki Waxtaan — Al-Hujurat
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا يَسْخَرْ قَوْمٌ مِّن قَوْمٍ عَسَىٰ أَن يَكُونُوا خَيْرًا مِّنْهُمْ وَلَا نِسَاءٌ مِّن نِّسَاءٍ عَسَىٰ أَن يَكُنَّ خَيْرًا مِّنْهُنَّ ۖ وَلَا تَلْمِزُوا أَنفُسَكُمْ وَلَا تَنَابَزُوا بِالْأَلْقَابِ ۖ بِئْسَ الِاسْمُ الْفُسُوقُ بَعْدَ الْإِيمَانِ ۚ وَمَن لَّمْ يَتُبْ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ ١١
Transliteration
Yaaa ayyuhal lazeena aamanoo laa yaskhar qawmum min qawmin `asaaa anyyakoonoo khairam minhum wa laa nisaaa`um min nisaaa`in `Asaaa ay yakunna khairam minhunna wa laa talmizooo bil alqaab; bi`sal ismul fusooqu ba`dal eemaan; wa mal-lam yatub fa-ulaaa`ika humuz zaalimoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Eey yéen ñi gëm ! Bu benn nit di faral a reetaan (yéjji) beneen nit : ndax amaana ña ñuy reetaan gën ñay reetaane. Bu ku góor di def bu ku jigéen it di def. Bu leen di saagaante. Bu leen di safaaney tur, turu caay-caay yellut ci ku gëm. (te ña koy def) te tuubuñu ko réccu ko... Ñoom ñoo di tooñkat ya.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 9-13 — Al-Hujurat
9وَإِن طَائِفَتَانِ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ اقْتَتَلُوا فَأَصْلِحُوا بَيْنَهُمَا ۖ فَإِن بَغَتْ إِحْدَاهُمَا عَلَى الْأُخْرَىٰ فَقَاتِلُوا الَّتِي تَبْغِي حَتَّىٰ تَفِيءَ إِلَىٰ أَمْرِ اللَّهِ ۚ فَإِن فَاءَتْ فَأَصْلِحُوا بَيْنَهُمَا بِالْعَدْلِ وَأَقْسِطُوا ۖ إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ الْمُقْسِطِينَ
Su ñaari kuréel ci jullit ñi di xeexoo, na ngeen yéwénal seeni diggante. Su fekkee ne benn ba moo jalgati tooñ ba ca des, na ngeen xeex ak bay tooñ, ba baa muy dellu ci ndigalul Yàlla. Bu, delloo ci ndigal nag, na ngeen leen jubale te ngeen maandu Yàlla safoona ñu maandu ña.
10إِنَّمَا الْمُؤْمِنُونَ إِخْوَةٌ فَأَصْلِحُوا بَيْنَ أَخَوَيْكُمْ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Way gëm ña ay mbokk la ñu. Na ngeen di yéwénal seen digganteek seen mbokk, te ngeen ragal Yàlla, ndax amaana yëramees leen.
11يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا يَسْخَرْ قَوْمٌ مِّن قَوْمٍ عَسَىٰ أَن يَكُونُوا خَيْرًا مِّنْهُمْ وَلَا نِسَاءٌ مِّن نِّسَاءٍ عَسَىٰ أَن يَكُنَّ خَيْرًا مِّنْهُنَّ ۖ وَلَا تَلْمِزُوا أَنفُسَكُمْ وَلَا تَنَابَزُوا بِالْأَلْقَابِ ۖ بِئْسَ الِاسْمُ الْفُسُوقُ بَعْدَ الْإِيمَانِ ۚ وَمَن لَّمْ يَتُبْ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Eey yéen ñi gëm ! Bu benn nit di faral a reetaan (yéjji) beneen nit : ndax amaana ña ñuy reetaan gën ñay reetaane. Bu ku góor di def bu ku jigéen it di def. Bu leen di saagaante. Bu leen di safaaney tur, turu caay-caay yellut ci ku gëm. (te ña koy def) te tuubuñu ko réccu ko... Ñoom ñoo di tooñkat ya.
12يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اجْتَنِبُوا كَثِيرًا مِّنَ الظَّنِّ إِنَّ بَعْضَ الظَّنِّ إِثْمٌ ۖ وَلَا تَجَسَّسُوا وَلَا يَغْتَب بَّعْضُكُم بَعْضًا ۚ أَيُحِبُّ أَحَدُكُمْ أَن يَأْكُلَ لَحْمَ أَخِيهِ مَيْتًا فَكَرِهْتُمُوهُ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ تَوَّابٌ رَّحِيمٌ
Eey yéen ñi gëm! Teetleen (moytu) njortu yu bari ndax yenn njortu yi bàkkaar la. Buleen di yëdóonte ; buleen di jëwante. Moo ndax kenn ci yéen bëgg naa lekk yàppu mbokkam mu dée ? Bëgguleen ko kay. Kon nag nangeen ragal Yàlla di ko watandiku. Yàlla kuy Nanguwaakoonu tuub la, Jaglewaakoon la.
13يَا أَيُّهَا النَّاسُ إِنَّا خَلَقْنَاكُم مِّن ذَكَرٍ وَأُنثَىٰ وَجَعَلْنَاكُمْ شُعُوبًا وَقَبَائِلَ لِتَعَارَفُوا ۚ إِنَّ أَكْرَمَكُمْ عِندَ اللَّهِ أَتْقَاكُمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلِيمٌ خَبِيرٌ
Eey yéen nit ñi ! Noo leen bind ci góor ak jigéen, def Nanu leen ngeen di ay giir ak i xeet, ngir ngeen xamante. Waaye ki gën a tedd ci yéen, fa Yàlla, moo di ki gën a ragal Yàlla ci yéen. Yàlla de Ku xam la Ku xàmmee la.
Al-HujuratFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
11Aaya
Tekki — Al-Hujurat 11
Simoore Al-Hujurat Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Eey yéen ñi gëm ! Bu benn nit di faral…Simoore Aaya 11/18 — Al-Hujurat الحجرات (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hujurat Dégg, Al-Hujurat Tekki, Al-Hujurat mp3, Al-Hujurat pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








