Al-Waqi'a · 38/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
لِّأَصْحَابِ الْيَمِينِ ۝٣٨
Li as haabil yameen
📖 Tekkim Wolof
waa ndeyjoor leen moom,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 36-40 — Simoore Al-Waqi'a

36فَجَعَلْنَاهُنَّ أَبْكَارًا
def Nanu leen ñu di ay xiig,
37عُرُبًا أَتْرَابًا
yu sopp lool seen jëkër, te maase ne rojj,
38لِّأَصْحَابِ الْيَمِينِ
waa ndeyjoor leen moom,
39ثُلَّةٌ مِّنَ الْأَوَّلِينَ
ñuy mbooloo ma nu tànn ca ña jëkkóon,
40وَثُلَّةٌ مِّنَ الْآخِرِينَ
ak mbooloo ma nu tànn ci ñu mujj,
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 38

Simoore Al-Waqi'a Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : waa ndeyjoor leen moom,

Simoore Aaya 38/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers