Al-Waqi'a · 80/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ ۝٨٠
Tanzeelum mir Rabbil`aalameen
📖 Tekkim Wolof
Mi ngi wàcci bawoo ca Yàlla Boroom àddina si.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 78-82 — Simoore Al-Waqi'a

78فِي كِتَابٍ مَّكْنُونٍ
ci biir Téere bu ñu ñoŋal
79لَّا يَمَسُّهُ إِلَّا الْمُطَهَّرُونَ
ñi laab rekk koy laal (ku laabul warukoo laal) ;
80تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Mi ngi wàcci bawoo ca Yàlla Boroom àddina si.
81أَفَبِهَٰذَا الْحَدِيثِ أَنتُم مُّدْهِنُونَ
Moo ndax ci waxtaan wii ngeen di weddi ?
82وَتَجْعَلُونَ رِزْقَكُمْ أَنَّكُمْ تُكَذِّبُونَ
Ak li leen Yàlla defal lépp fayewuleen ko lu dul di weddi Alxuraan ?
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
80Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 80

Simoore Al-Waqi'a Aaya 80 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mi ngi wàcci bawoo ca Yàlla Boroom àddina si.

Simoore Aaya 80/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 78–82. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers