Al-Waqi'a · 81/96
Tekki Waxtaan — Al-Waqi'a
أَفَبِهَٰذَا الْحَدِيثِ أَنتُم مُّدْهِنُونَ ۝٨١
Afabihaazal hadeesi antum mudhinoon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ci waxtaan wii ngeen di weddi ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 79-83 — Al-Waqi'a

79لَّا يَمَسُّهُ إِلَّا الْمُطَهَّرُونَ
ñi laab rekk koy laal (ku laabul warukoo laal) ;
80تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Mi ngi wàcci bawoo ca Yàlla Boroom àddina si.
81أَفَبِهَٰذَا الْحَدِيثِ أَنتُم مُّدْهِنُونَ
Moo ndax ci waxtaan wii ngeen di weddi ?
82وَتَجْعَلُونَ رِزْقَكُمْ أَنَّكُمْ تُكَذِّبُونَ
Ak li leen Yàlla defal lépp fayewuleen ko lu dul di weddi Alxuraan ?
83فَلَوْلَا إِذَا بَلَغَتِ الْحُلْقُومَ
Bu ruuh gi génnee ba des ci bóli gi (kuy sukuraat),
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
81Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 81

Simoore Al-Waqi'a Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ci waxtaan wii ngeen di weddi ?

Simoore Aaya 81/96 — Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Waqi'a Dégg, Al-Waqi'a Tekki, Al-Waqi'a mp3, Al-Waqi'a pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers