Al-Mujadila · 16/22
Tekki Waxtaan — Al-Mujadila
اتَّخَذُوا أَيْمَانَهُمْ جُنَّةً فَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ فَلَهُمْ عَذَابٌ مُّهِينٌ ۝١٦
Ittakhazooo aymaanahum junnatan fasaddoo `an sabeelil laahi falahum `azaabum muheen
📖 Tekkim Wolof
Jàppe woon nañu seen ngiñ ya muy pakk, ñuy gàllankor yoonu Yàlla. Danañu am mbugël muy toroxal.
🎧 Dégg

📜 Aaya 14-18 — Al-Mujadila

14۞ أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ تَوَلَّوْا قَوْمًا غَضِبَ اللَّهُ عَلَيْهِم مَّا هُم مِّنكُمْ وَلَا مِنْهُمْ وَيَحْلِفُونَ عَلَى الْكَذِبِ وَهُمْ يَعْلَمُونَ
Xanaa gisuloo naaféq ya dem ànd ak ña Yàlla mere (Yahuud ya) ? Ñoom bokkuñu ci yéen, bokkuñu it ci ñoom (Yahuud ya) ; te ña ngay giñ fen ci Yàlla, te xam ko xéll.
15أَعَدَّ اللَّهُ لَهُمْ عَذَابًا شَدِيدًا ۖ إِنَّهُمْ سَاءَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Yàlla waajalna leen mbugël mu tar. Ngir la ñu daan def ñaaw na.
16اتَّخَذُوا أَيْمَانَهُمْ جُنَّةً فَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ فَلَهُمْ عَذَابٌ مُّهِينٌ
Jàppe woon nañu seen ngiñ ya muy pakk, ñuy gàllankor yoonu Yàlla. Danañu am mbugël muy toroxal.
17لَّن تُغْنِيَ عَنْهُمْ أَمْوَالُهُمْ وَلَا أَوْلَادُهُم مِّنَ اللَّهِ شَيْئًا ۚ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ النَّارِ ۖ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Seen alal yeek, seen doom yi do leen jariñ manuleen fegal dara ci Yàlla. Ñoom ñoo di waa safara te danu fay béel.
18يَوْمَ يَبْعَثُهُمُ اللَّهُ جَمِيعًا فَيَحْلِفُونَ لَهُ كَمَا يَحْلِفُونَ لَكُمْ ۖ وَيَحْسَبُونَ أَنَّهُمْ عَلَىٰ شَيْءٍ ۚ أَلَا إِنَّهُمْ هُمُ الْكَاذِبُونَ
Bu keroogee ba Yàlla dekkal leen ñoom ñépp, su ku defee ñu di ko giiñël ni ñu leen daan giiñale yéen, dañuy jortu ne ñi ngi ci dara. Te ñoom ay fenkat la ñu.
Al-MujadilaFihi Alxuraan
22Aaya
MedinanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Mujadila 16

Simoore Al-Mujadila Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jàppe woon nañu seen ngiñ ya muy pakk, ñuy gàllankor…

Simoore Aaya 16/22 — Al-Mujadila المجادلة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mujadila Dégg, Al-Mujadila Tekki, Al-Mujadila mp3, Al-Mujadila pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers