Al-Mujadila · 17/22
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mujadila
لَّن تُغْنِيَ عَنْهُمْ أَمْوَالُهُمْ وَلَا أَوْلَادُهُم مِّنَ اللَّهِ شَيْئًا ۚ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ النَّارِ ۖ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ ۝١٧
Lan tughniya `anhum amwaaluhum wa laaa awladuhum minal laahi shai`aa; ulaaa `ika As haabun Naari hum feehaa khaalidoon
📖 Tekkim Wolof
Seen alal yeek, seen doom yi do leen jariñ manuleen fegal dara ci Yàlla. Ñoom ñoo di waa safara te danu fay béel.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 15-19 — Simoore Al-Mujadila

15أَعَدَّ اللَّهُ لَهُمْ عَذَابًا شَدِيدًا ۖ إِنَّهُمْ سَاءَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Yàlla waajalna leen mbugël mu tar. Ngir la ñu daan def ñaaw na.
16اتَّخَذُوا أَيْمَانَهُمْ جُنَّةً فَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ فَلَهُمْ عَذَابٌ مُّهِينٌ
Jàppe woon nañu seen ngiñ ya muy pakk, ñuy gàllankor yoonu Yàlla. Danañu am mbugël muy toroxal.
17لَّن تُغْنِيَ عَنْهُمْ أَمْوَالُهُمْ وَلَا أَوْلَادُهُم مِّنَ اللَّهِ شَيْئًا ۚ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ النَّارِ ۖ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Seen alal yeek, seen doom yi do leen jariñ manuleen fegal dara ci Yàlla. Ñoom ñoo di waa safara te danu fay béel.
18يَوْمَ يَبْعَثُهُمُ اللَّهُ جَمِيعًا فَيَحْلِفُونَ لَهُ كَمَا يَحْلِفُونَ لَكُمْ ۖ وَيَحْسَبُونَ أَنَّهُمْ عَلَىٰ شَيْءٍ ۚ أَلَا إِنَّهُمْ هُمُ الْكَاذِبُونَ
Bu keroogee ba Yàlla dekkal leen ñoom ñépp, su ku defee ñu di ko giiñël ni ñu leen daan giiñale yéen, dañuy jortu ne ñi ngi ci dara. Te ñoom ay fenkat la ñu.
19اسْتَحْوَذَ عَلَيْهِمُ الشَّيْطَانُ فَأَنسَاهُمْ ذِكْرَ اللَّهِ ۚ أُولَٰئِكَ حِزْبُ الشَّيْطَانِ ۚ أَلَا إِنَّ حِزْبَ الشَّيْطَانِ هُمُ الْخَاسِرُونَ
Saytaane man-manee na leen ba fàtteloo leen tudd Yàlla. Ñoo di kureelub Saytaane ndaxam kureelu Saytaane ñooy ña yàqule tigi.
Al-MujadilaFihi Alxuraan
22Aaya
MedinanRevelation
17Aaya

Tekki — Al-Mujadila 17

Simoore Al-Mujadila Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen alal yeek, seen doom yi do leen jariñ manuleen…

Simoore Aaya 17/22 — Simoore Al-Mujadila المجادلة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mujadila Dégg, Simoore Al-Mujadila Tekki, Simoore Al-Mujadila mp3, Simoore Al-Mujadila pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers