Al-A'raf · 12/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
قَالَ مَا مَنَعَكَ أَلَّا تَسْجُدَ إِذْ أَمَرْتُكَ ۖ قَالَ أَنَا خَيْرٌ مِّنْهُ خَلَقْتَنِي مِن نَّارٍ وَخَلَقْتَهُ مِن طِينٍ ١٢
Transliteration
Qaala maa mana`aka allaa tasjuda iz amartuka qaala ana khairum minhu khalaqtanee min naarinw wa khalaqtahoo min teen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Yàlla] ne ko : “Lan moo la tee sujjóot ba Ma la ko digalee ? ”. Mu ne : “Maa ko gën : ndax Danga ma bind ci Safara, moom Nga bind ko ci ban”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 10-14 — Al-A'raf
10وَلَقَدْ مَكَّنَّاكُمْ فِي الْأَرْضِ وَجَعَلْنَا لَكُمْ فِيهَا مَعَايِشَ ۗ قَلِيلًا مَّا تَشْكُرُونَ
Defal Nanu leen ag jàppandal ci suuf si, defal leen ca lu ngeen dunde. Te seenug cant néew na !
11وَلَقَدْ خَلَقْنَاكُمْ ثُمَّ صَوَّرْنَاكُمْ ثُمَّ قُلْنَا لِلْمَلَائِكَةِ اسْجُدُوا لِآدَمَ فَسَجَدُوا إِلَّا إِبْلِيسَ لَمْ يَكُن مِّنَ السَّاجِدِينَ
Bind Nanu leen, jox leen i melo, ba noppi Nu wax Malaaka ya : “Sujjóotal-leen Aadama.”. Ñoom ñépp a sujjoot, ba mu des Ibliis, moom bokkul ca ña sujjóot.
12قَالَ مَا مَنَعَكَ أَلَّا تَسْجُدَ إِذْ أَمَرْتُكَ ۖ قَالَ أَنَا خَيْرٌ مِّنْهُ خَلَقْتَنِي مِن نَّارٍ وَخَلَقْتَهُ مِن طِينٍ
[Yàlla] ne ko : “Lan moo la tee sujjóot ba Ma la ko digalee ? ”. Mu ne : “Maa ko gën : ndax Danga ma bind ci Safara, moom Nga bind ko ci ban”.
13قَالَ فَاهْبِطْ مِنْهَا فَمَا يَكُونُ لَكَ أَن تَتَكَبَّرَ فِيهَا فَاخْرُجْ إِنَّكَ مِنَ الصَّاغِرِينَ
[Yàlla] ne ko : “Wàccal jóge fi, yaw waroo fi rëy-rëylu. Génnal, torox nga.”
14قَالَ أَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
Ibliis ne Ko : “Muñal ma ba bisu dekki ba.”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
12Aaya
Tekki — Al-A'raf 12
Simoore Al-A'raf Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yàlla] ne ko : “Lan moo la tee sujjóot ba…Simoore Aaya 12/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








