Az-Zalzala · 6/8
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zalzala
يَوْمَئِذٍ يَصْدُرُ النَّاسُ أَشْتَاتًا لِّيُرَوْا أَعْمَالَهُمْ ۝٦
Yawma iziy yas durun naasu ash tatal liyuraw a`maalahum
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan leen seeni jëf.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 4-8 — Simoore Az-Zalzala

4يَوْمَئِذٍ تُحَدِّثُ أَخْبَارَهَا
bu keroogee, ci lay waxtaane ay xibaar,
5بِأَنَّ رَبَّكَ أَوْحَىٰ لَهَا
ci la ko sa Boroom soloo.
6يَوْمَئِذٍ يَصْدُرُ النَّاسُ أَشْتَاتًا لِّيُرَوْا أَعْمَالَهُمْ
Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan leen seeni jëf.
7فَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ خَيْرًا يَرَهُ
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp te muy lu baax, dana ko gis,
8وَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ شَرًّا يَرَهُ
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp su dee lu bon, dana ko gis.
Az-ZalzalaFihi Alxuraan
8Aaya
MedinanRevelation
6Aaya

Tekki — Az-Zalzala 6

Simoore Az-Zalzala Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan…

Simoore Aaya 6/8 — Simoore Az-Zalzala الزلزلة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zalzala Dégg, Simoore Az-Zalzala Tekki, Simoore Az-Zalzala mp3, Simoore Az-Zalzala pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers