Az-Zalzala · 8/8
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zalzala
وَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ شَرًّا يَرَهُ ۝٨
Wa maiy-y`amal mithqala zarratin sharraiy-yarah
📖 Tekkim Wolof
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp su dee lu bon, dana ko gis.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-8 — Simoore Az-Zalzala

6يَوْمَئِذٍ يَصْدُرُ النَّاسُ أَشْتَاتًا لِّيُرَوْا أَعْمَالَهُمْ
Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan leen seeni jëf.
7فَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ خَيْرًا يَرَهُ
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp te muy lu baax, dana ko gis,
8وَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ شَرًّا يَرَهُ
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp su dee lu bon, dana ko gis.
Az-ZalzalaFihi Alxuraan
8Aaya
MedinanRevelation
8Aaya

Tekki — Az-Zalzala 8

Simoore Az-Zalzala Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp ku jëf lu toll ni aw fepp su dee…

Simoore Aaya 8/8 — Simoore Az-Zalzala الزلزلة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zalzala Dégg, Simoore Az-Zalzala Tekki, Simoore Az-Zalzala mp3, Simoore Az-Zalzala pdf. Aaya 6–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers