PDF —
8 Aaya Medinan PDF
Built right in your browser — download starts automatically

Simoore Az-Zalzala pdf — Wàcce (Wolof)

Simoore Az-Zalzala pdf Wolof — Wàcce Simoore Az-Zalzala Tekki. Simoore Az-Zalzala (Medinan) 8 Aaya.

← Al-BayyinaSimoore Az-Zalzala Al-'Adiyat →


8 Aaya · Medinan · Wolof
bismillah
ﮅﮆﮇﮈﮉ
99:1 Saa su suuf si yëngutoo yëngoom ba,
ﮊﮋﮌﮍ
99:2 te suuf si génne la mu suuloon,
ﮎﮏﮐﮑﮒ
99:3 nit naan : “Ngala man ? ”
ﮓﮔﮕﮖ
99:4 bu keroogee, ci lay waxtaane ay xibaar,
ﮗﮘﮙﮚﮛ
99:5 ci la ko sa Boroom soloo.
ﮜﮝﮞﮟﮠﮡﮢ
99:6 Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan leen seeni jëf.
ﮣﮤﮥﮦﮧﮨﮩ
99:7 Képp ku jëf lu toll ni aw fepp te muy lu baax, dana ko gis,
ﮪﮫﮬﮭﮮﮯﮰ
99:8 Képp ku jëf lu toll ni aw fepp su dee lu bon, dana ko gis.

Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 9, 2026

Don't forget us in your sincere prayers