Az-Zalzala · 5/8
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zalzala
بِأَنَّ رَبَّكَ أَوْحَىٰ لَهَا ۝٥
Bi-anna rabbaka awhaa laha
📖 Tekkim Wolof
ci la ko sa Boroom soloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Az-Zalzala

3وَقَالَ الْإِنسَانُ مَا لَهَا
nit naan : “Ngala man ? ”
4يَوْمَئِذٍ تُحَدِّثُ أَخْبَارَهَا
bu keroogee, ci lay waxtaane ay xibaar,
5بِأَنَّ رَبَّكَ أَوْحَىٰ لَهَا
ci la ko sa Boroom soloo.
6يَوْمَئِذٍ يَصْدُرُ النَّاسُ أَشْتَاتًا لِّيُرَوْا أَعْمَالَهُمْ
Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan leen seeni jëf.
7فَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ خَيْرًا يَرَهُ
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp te muy lu baax, dana ko gis,
Az-ZalzalaFihi Alxuraan
8Aaya
MedinanRevelation
5Aaya

Tekki — Az-Zalzala 5

Simoore Az-Zalzala Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ci la ko sa Boroom soloo.

Simoore Aaya 5/8 — Simoore Az-Zalzala الزلزلة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zalzala Dégg, Simoore Az-Zalzala Tekki, Simoore Az-Zalzala mp3, Simoore Az-Zalzala pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers