Hud · 9/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
وَلَئِنْ أَذَقْنَا الْإِنسَانَ مِنَّا رَحْمَةً ثُمَّ نَزَعْنَاهَا مِنْهُ إِنَّهُ لَيَئُوسٌ كَفُورٌ ۝٩
Wa la`in azaqnal insaana minnaa rahmatan summa naza`naahaa minhu, innahoo laya`oosun kafoor
📖 Tekkim Wolof
Te wóor na it ne, su Nu mosaloon nit lenn ci Sunu yërmaande, ba noppi Nu nangu ko ci moom, kon dey dana nekk di ku ñàkk yaakaar ak fakk (sunuy xéewal).

🎧 Dégg


📜 Aaya 7-11 — Simoore Hud

7وَهُوَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ وَكَانَ عَرْشُهُ عَلَى الْمَاءِ لِيَبْلُوَكُمْ أَيُّكُمْ أَحْسَنُ عَمَلًا ۗ وَلَئِن قُلْتَ إِنَّكُم مَّبْعُوثُونَ مِن بَعْدِ الْمَوْتِ لَيَقُولَنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ مُّبِينٌ
Moom mooy ki bind asamaan yi ak suuf si ci juróom-benni fan, - te fekk Gàngunaay ga ma nga ca kaw am ndox, - ngir Mu nattu leen [ba xam] kan moo gën a rafet jëf ci yéen. Te wóor na ne, boo leen waxoon ne : “Yéen ñu ñuy dekkal ngeen ginnaaw dee”, fàwwu ña weddi danañu wax ne : “Lii nekkul lu dul njibar gu bir”.
8وَلَئِنْ أَخَّرْنَا عَنْهُمُ الْعَذَابَ إِلَىٰ أُمَّةٍ مَّعْدُودَةٍ لَّيَقُولُنَّ مَا يَحْبِسُهُ ۗ أَلَا يَوْمَ يَأْتِيهِمْ لَيْسَ مَصْرُوفًا عَنْهُمْ وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Te wóor na it ne su Nu yéexalee ci ñoom mbugal ma, jëme ko ca waxtu wu ñu dogal àppam, fàwwu danañu ne : “Lan moo ko téye ? - Te bis ba muy agsi ci ñoom, ndax dana nekk lu kenn dul mën a jiñ; te la ñu daan yéjj dana wàcc ci seen kaw.
9وَلَئِنْ أَذَقْنَا الْإِنسَانَ مِنَّا رَحْمَةً ثُمَّ نَزَعْنَاهَا مِنْهُ إِنَّهُ لَيَئُوسٌ كَفُورٌ
Te wóor na it ne, su Nu mosaloon nit lenn ci Sunu yërmaande, ba noppi Nu nangu ko ci moom, kon dey dana nekk di ku ñàkk yaakaar ak fakk (sunuy xéewal).
10وَلَئِنْ أَذَقْنَاهُ نَعْمَاءَ بَعْدَ ضَرَّاءَ مَسَّتْهُ لَيَقُولَنَّ ذَهَبَ السَّيِّئَاتُ عَنِّي ۚ إِنَّهُ لَفَرِحٌ فَخُورٌ
Te wóor na it ne, su Nu ko mosalee xéewal ginnaaw naqar wa ko daloon, dana wax ne : “Tiis teggeeku na ma”, Moom [nit] kuy bég la, di puukarewaakon.
11إِلَّا الَّذِينَ صَبَرُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ أُولَٰئِكَ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ كَبِيرٌ
ba mu des ña nga xam ne dañoo muñ, di jëf jëf yu sell. Ñoom ñooña am nañu njéggal ak pey gu mag.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Hud 9

Simoore Hud Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te wóor na it ne, su Nu mosaloon nit lenn…

Simoore Aaya 9/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers