Ar-Ra'd · 1/43
Tekki Waxtaan — Ar-Ra'd
المر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ ۗ وَالَّذِي أُنزِلَ إِلَيْكَ مِن رَّبِّكَ الْحَقُّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يُؤْمِنُونَ ۝١
Alif-Laaam-Meeem-Raa; tilka Aayaatul Kitaab; wallazee unzila ilaika mir Rabbikal haqqu wa laakinna aksaran naasi laa yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Aliif, Laam, Miim, Raa. Kàdduy Téere ba ñoo ngi nii te di lu ñu wàcce ci yaw, mu jóge ci sa Boroom dëgg ga ; waaye li ëpp ci nit ñi gëmuñu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Ar-Ra'd

1المر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ ۗ وَالَّذِي أُنزِلَ إِلَيْكَ مِن رَّبِّكَ الْحَقُّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يُؤْمِنُونَ
Aliif, Laam, Miim, Raa. Kàdduy Téere ba ñoo ngi nii te di lu ñu wàcce ci yaw, mu jóge ci sa Boroom dëgg ga ; waaye li ëpp ci nit ñi gëmuñu.
2اللَّهُ الَّذِي رَفَعَ السَّمَاوَاتِ بِغَيْرِ عَمَدٍ تَرَوْنَهَا ۖ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۖ وَسَخَّرَ الشَّمْسَ وَالْقَمَرَ ۖ كُلٌّ يَجْرِي لِأَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ يُدَبِّرُ الْأَمْرَ يُفَصِّلُ الْآيَاتِ لَعَلَّكُم بِلِقَاءِ رَبِّكُمْ تُوقِنُونَ
Yàlla Moo di ki wàcce asamaan yi ci lu amul keno yu ñu mën a gis. Topp Mu yemoo ca [Aras], Mu tàggat jant bi ak weer wi, ñoom ñépp ñuy daw jëm ci àpp bu ñu dogal. Mooy àtte doxiinu [àddina], Dana leeral ag kàddoom ndax mu wóor leen ne dangeen dajeek seen Boroom.
3وَهُوَ الَّذِي مَدَّ الْأَرْضَ وَجَعَلَ فِيهَا رَوَاسِيَ وَأَنْهَارًا ۖ وَمِن كُلِّ الثَّمَرَاتِ جَعَلَ فِيهَا زَوْجَيْنِ اثْنَيْنِ ۖ يُغْشِي اللَّيْلَ النَّهَارَ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَتَفَكَّرُونَ
Moom mooy Ki tàllal suuf si, def ca ay doj ak i dex. Te def na ca mépp meññent ñaar-ñaar [góor ak jigéen]. Dana muure bëccëg ci guddi gi. Nit ñuy xalaat am nañu ci loolu ag waaru.
Ar-Ra'dFihi Alxuraan
43Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — Ar-Ra'd 1

Simoore Ar-Ra'd Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Aliif, Laam, Miim, Raa. Kàdduy Téere ba ñoo ngi nii…

Simoore Aaya 1/43 — Ar-Ra'd الرعد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Ra'd Dégg, Ar-Ra'd Tekki, Ar-Ra'd mp3, Ar-Ra'd pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers