Ar-Ra'd · 2/43
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Ra'd
اللَّهُ الَّذِي رَفَعَ السَّمَاوَاتِ بِغَيْرِ عَمَدٍ تَرَوْنَهَا ۖ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۖ وَسَخَّرَ الشَّمْسَ وَالْقَمَرَ ۖ كُلٌّ يَجْرِي لِأَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ يُدَبِّرُ الْأَمْرَ يُفَصِّلُ الْآيَاتِ لَعَلَّكُم بِلِقَاءِ رَبِّكُمْ تُوقِنُونَ ۝٢
Allaahul lazee raf`as samaawaati bighairi `amadin tarawnahaa summas tawaa `alal `Arshi wa sakhkharash shamsa walqamara kulluny yajree li ajalim musammaa; yudabbirul amra yufassilil Aayaati la`allakum biliqaaa`i Rabbikum tooqinoon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla Moo di ki wàcce asamaan yi ci lu amul keno yu ñu mën a gis. Topp Mu yemoo ca [Aras], Mu tàggat jant bi ak weer wi, ñoom ñépp ñuy daw jëm ci àpp bu ñu dogal. Mooy àtte doxiinu [àddina], Dana leeral ag kàddoom ndax mu wóor leen ne dangeen dajeek seen Boroom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore Ar-Ra'd

1المر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ ۗ وَالَّذِي أُنزِلَ إِلَيْكَ مِن رَّبِّكَ الْحَقُّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يُؤْمِنُونَ
Aliif, Laam, Miim, Raa. Kàdduy Téere ba ñoo ngi nii te di lu ñu wàcce ci yaw, mu jóge ci sa Boroom dëgg ga ; waaye li ëpp ci nit ñi gëmuñu.
2اللَّهُ الَّذِي رَفَعَ السَّمَاوَاتِ بِغَيْرِ عَمَدٍ تَرَوْنَهَا ۖ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۖ وَسَخَّرَ الشَّمْسَ وَالْقَمَرَ ۖ كُلٌّ يَجْرِي لِأَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ يُدَبِّرُ الْأَمْرَ يُفَصِّلُ الْآيَاتِ لَعَلَّكُم بِلِقَاءِ رَبِّكُمْ تُوقِنُونَ
Yàlla Moo di ki wàcce asamaan yi ci lu amul keno yu ñu mën a gis. Topp Mu yemoo ca [Aras], Mu tàggat jant bi ak weer wi, ñoom ñépp ñuy daw jëm ci àpp bu ñu dogal. Mooy àtte doxiinu [àddina], Dana leeral ag kàddoom ndax mu wóor leen ne dangeen dajeek seen Boroom.
3وَهُوَ الَّذِي مَدَّ الْأَرْضَ وَجَعَلَ فِيهَا رَوَاسِيَ وَأَنْهَارًا ۖ وَمِن كُلِّ الثَّمَرَاتِ جَعَلَ فِيهَا زَوْجَيْنِ اثْنَيْنِ ۖ يُغْشِي اللَّيْلَ النَّهَارَ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَتَفَكَّرُونَ
Moom mooy Ki tàllal suuf si, def ca ay doj ak i dex. Te def na ca mépp meññent ñaar-ñaar [góor ak jigéen]. Dana muure bëccëg ci guddi gi. Nit ñuy xalaat am nañu ci loolu ag waaru.
4وَفِي الْأَرْضِ قِطَعٌ مُّتَجَاوِرَاتٌ وَجَنَّاتٌ مِّنْ أَعْنَابٍ وَزَرْعٌ وَنَخِيلٌ صِنْوَانٌ وَغَيْرُ صِنْوَانٍ يُسْقَىٰ بِمَاءٍ وَاحِدٍ وَنُفَضِّلُ بَعْضَهَا عَلَىٰ بَعْضٍ فِي الْأُكُلِ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَعْقِلُونَ
Nekk na ci kaw suuf si ay déndi suuf yu tàqaloo [te wuute], ak tooli reseñ ak mbeyum pepp, ak garabi tàndarma yu ràngaloo ak yu soreyaantoo, ñoom ñépp ndox mi leen di suuxat menn la. Nuy gënal yenn ya ci kaw yeneen ya ci cafka ga. Ag waare nekk na ci biir loolu ngir nit ñu am xel.
Ar-Ra'dFihi Alxuraan
43Aaya
MedinanRevelation
2Aaya

Tekki — Ar-Ra'd 2

Simoore Ar-Ra'd Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla Moo di ki wàcce asamaan yi ci lu amul…

Simoore Aaya 2/43 — Simoore Ar-Ra'd الرعد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Ra'd Dégg, Simoore Ar-Ra'd Tekki, Simoore Ar-Ra'd mp3, Simoore Ar-Ra'd pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers