Ar-Ra'd · 23/43
Tekki Waxtaan — Ar-Ra'd
جَنَّاتُ عَدْنٍ يَدْخُلُونَهَا وَمَن صَلَحَ مِنْ آبَائِهِمْ وَأَزْوَاجِهِمْ وَذُرِّيَّاتِهِمْ ۖ وَالْمَلَائِكَةُ يَدْخُلُونَ عَلَيْهِم مِّن كُلِّ بَابٍ ۝٢٣
jannaatu `adiny yadkhu loonahaa wa man salaha min aabaaa`ihim wa man salaha min aabaaa`ihim wa azwaajihim wa zurriyyaatihim walmalaaa`i katu yadkhuloona `alaihim min kulli baab
📖 Tekkim Wolof
Àjjana ju sax ja, danañu ca dugg, ak ña jëfoon lu baax ca seeni baay ak ca seeni jabar ak seeni doom ak i sët. Te Malaaka ya dañuy duggandook ñoom ci buntu yépp :

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Ar-Ra'd

21وَالَّذِينَ يَصِلُونَ مَا أَمَرَ اللَّهُ بِهِ أَن يُوصَلَ وَيَخْشَوْنَ رَبَّهُمْ وَيَخَافُونَ سُوءَ الْحِسَابِ
ak ñay jokk la Yàlla santaane ñu jokk ko [mooy mbokk], te ragal nañu seen Boroom, di ragal it [ca àllaaxira] natt bu bon [seen jëf yu ñaaw ëpp seen jëf yu baax],
22وَالَّذِينَ صَبَرُوا ابْتِغَاءَ وَجْهِ رَبِّهِمْ وَأَقَامُوا الصَّلَاةَ وَأَنفَقُوا مِمَّا رَزَقْنَاهُمْ سِرًّا وَعَلَانِيَةً وَيَدْرَءُونَ بِالْحَسَنَةِ السَّيِّئَةَ أُولَٰئِكَ لَهُمْ عُقْبَى الدَّارِ
ak ñay muñ ngir jëmmi seen Boroom, tey taxawal julli tey dundale ca la leen Yàlla wërsëgale ci la nëbbu walla ci lu feeñ, te ñuy jiñe lu ñaaw ak lu rafet. Ñooña am nañu kër gu mujj ga,
23جَنَّاتُ عَدْنٍ يَدْخُلُونَهَا وَمَن صَلَحَ مِنْ آبَائِهِمْ وَأَزْوَاجِهِمْ وَذُرِّيَّاتِهِمْ ۖ وَالْمَلَائِكَةُ يَدْخُلُونَ عَلَيْهِم مِّن كُلِّ بَابٍ
Àjjana ju sax ja, danañu ca dugg, ak ña jëfoon lu baax ca seeni baay ak ca seeni jabar ak seeni doom ak i sët. Te Malaaka ya dañuy duggandook ñoom ci buntu yépp :
24سَلَامٌ عَلَيْكُم بِمَا صَبَرْتُمْ ۚ فَنِعْمَ عُقْبَى الدَّارِ
[Ñu naan leen] - “Jàmmi Yàlla na nekk ci yéen ngir la ngeen muñoon ! ” - Aka rafet kërug mujj ga ! ”
25وَالَّذِينَ يَنقُضُونَ عَهْدَ اللَّهِ مِن بَعْدِ مِيثَاقِهِ وَيَقْطَعُونَ مَا أَمَرَ اللَّهُ بِهِ أَن يُوصَلَ وَيُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ ۙ أُولَٰئِكَ لَهُمُ اللَّعْنَةُ وَلَهُمْ سُوءُ الدَّارِ
[Waaye] ñiy firi kóllareg Yàlla ginnaaw ba mu fasoo, te muy dog la Mu santaane ñu jokk ko [mooy ag mbokk], di yàq ci kaw suuf si, ñooña am rëbb dal na ci seen kaw [sori yërmaandey Yàlla], te it am nañu kër gu bon ga.
Ar-Ra'dFihi Alxuraan
43Aaya
MedinanRevelation
23Aaya

Tekki — Ar-Ra'd 23

Simoore Ar-Ra'd Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Àjjana ju sax ja, danañu ca dugg, ak ña jëfoon…

Simoore Aaya 23/43 — Ar-Ra'd الرعد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Ra'd Dégg, Ar-Ra'd Tekki, Ar-Ra'd mp3, Ar-Ra'd pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers