Al-Kahf · 78/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
قَالَ هَٰذَا فِرَاقُ بَيْنِي وَبَيْنِكَ ۚ سَأُنَبِّئُكَ بِتَأْوِيلِ مَا لَمْ تَسْتَطِع عَّلَيْهِ صَبْرًا ۝٧٨
Qaala haazaa firaaqu bainee wa bainik; sa unabi `uka bitaaweeli maa lam tastati` `alaihi sabraa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Maak yaw fii la nuy tàqalikoo.Waaye danaa la leeralal mbirum li nga mënul woon a muñ.
🎧 Dégg

📜 Aaya 76-80 — Al-Kahf

76قَالَ إِن سَأَلْتُكَ عَن شَيْءٍ بَعْدَهَا فَلَا تُصَاحِبْنِي ۖ قَدْ بَلَغْتَ مِن لَّدُنِّي عُذْرًا
[Muusaa] toontu ko ne : “Saa yu ma la laajee menn mbir, kon bul àndateek man. Ndax am nga ngànt ci tàggook man”.
77فَانطَلَقَا حَتَّىٰ إِذَا أَتَيَا أَهْلَ قَرْيَةٍ اسْتَطْعَمَا أَهْلَهَا فَأَبَوْا أَن يُضَيِّفُوهُمَا فَوَجَدَا فِيهَا جِدَارًا يُرِيدُ أَن يَنقَضَّ فَأَقَامَهُ ۖ قَالَ لَوْ شِئْتَ لَتَّخَذْتَ عَلَيْهِ أَجْرًا
Ñuy dox ba egg cib dëkk, ñu sàkku ca waa dëkk ba lekk, ñu lànk leen a ganale. Noona mu gis ab tabax buy bëgg a daanu. Mu yékkatiwaat ko. [Muusaa] ne ko : “Su la neexoon dey nga laaj ag pey”.
78قَالَ هَٰذَا فِرَاقُ بَيْنِي وَبَيْنِكَ ۚ سَأُنَبِّئُكَ بِتَأْوِيلِ مَا لَمْ تَسْتَطِع عَّلَيْهِ صَبْرًا
Mu ne ko : “Maak yaw fii la nuy tàqalikoo.Waaye danaa la leeralal mbirum li nga mënul woon a muñ.
79أَمَّا السَّفِينَةُ فَكَانَتْ لِمَسَاكِينَ يَعْمَلُونَ فِي الْبَحْرِ فَأَرَدتُّ أَنْ أَعِيبَهَا وَكَانَ وَرَاءَهُم مَّلِكٌ يَأْخُذُ كُلَّ سَفِينَةٍ غَصْبًا
[Gaal ga ma bënoon], ay ndóol ñoo ko móomoon, daan ca daan seen doole ngir dundu. La tax ma bënn ko moo di dafa buur bu daan siif gépp gaal gu mu romb, ma bënn ko ngir mu bañ koo yóbb.
80وَأَمَّا الْغُلَامُ فَكَانَ أَبَوَاهُ مُؤْمِنَيْنِ فَخَشِينَا أَن يُرْهِقَهُمَا طُغْيَانًا وَكُفْرًا
Xale [ba ma reyoon], ay waajuram dañoo doonoon ñu gëm Yàlla ; te su màggoon, dana leen weddiloo, beewloo leen.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
78Aaya

Tekki — Al-Kahf 78

Simoore Al-Kahf Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Maak yaw fii la nuy tàqalikoo.Waaye…

Simoore Aaya 78/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers