Al-Baqara · 6/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا سَوَاءٌ عَلَيْهِمْ أَأَنذَرْتَهُمْ أَمْ لَمْ تُنذِرْهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ ۝٦
Innal lazeena kafaroo sawaaa`un `alaihim `a-anzar tahum am lam tunzirhum laa yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Ñi weddi, nga waar leen ak ñàkk leen waar a yem ci ñoom, duñu gëm.
🎧 Dégg

📜 Aaya 4-8 — Al-Baqara

4وَالَّذِينَ يُؤْمِنُونَ بِمَا أُنزِلَ إِلَيْكَ وَمَا أُنزِلَ مِن قَبْلِكَ وَبِالْآخِرَةِ هُمْ يُوقِنُونَ
Ñoo di ña gëm la Ñu wàcce ci yaw ak la Nu wàcce woon mu jiitu woon te ñu amug wóolu ci dikkug Bis-pénc ba.
5أُولَٰئِكَ عَلَىٰ هُدًى مِّن رَّبِّهِمْ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Ñooñoo nekk ca njub ga tukkee ca seen Boroom te ñoom ñoo texe.
6إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا سَوَاءٌ عَلَيْهِمْ أَأَنذَرْتَهُمْ أَمْ لَمْ تُنذِرْهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Ñi weddi, nga waar leen ak ñàkk leen waar a yem ci ñoom, duñu gëm.
7خَتَمَ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ وَعَلَىٰ سَمْعِهِمْ ۖ وَعَلَىٰ أَبْصَارِهِمْ غِشَاوَةٌ ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ عَظِيمٌ
Yàlla fatt na seeni xol ak seeni nopp ; muuraay nekk na ca seeni gët ; mbugal mu metti dana leen dal.
8وَمِنَ النَّاسِ مَن يَقُولُ آمَنَّا بِاللَّهِ وَبِالْيَوْمِ الْآخِرِ وَمَا هُم بِمُؤْمِنِينَ
Am na ci nit ñi, ñu naan : “Gëm nanu Yàlla ak Bis-pénc ba ! ” te gëmuñu dara.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Baqara 6

Simoore Al-Baqara Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñi weddi, nga waar leen ak ñàkk leen waar a…

Simoore Aaya 6/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers