Taha · 3/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
إِلَّا تَذْكِرَةً لِّمَن يَخْشَىٰ ۝٣
Illaa tazkiratal limany yakshaa
📖 Tekkim Wolof
[waaye] Danu koo wàcce ngir muy waar ñi ragal Yàlla,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-5 — Simoore Taha

1طه
Taa Haa.
2مَا أَنزَلْنَا عَلَيْكَ الْقُرْآنَ لِتَشْقَىٰ
Wàccewunu Alxuraan jii ci yaw ngir nga texeedi [tiis],
3إِلَّا تَذْكِرَةً لِّمَن يَخْشَىٰ
[waaye] Danu koo wàcce ngir muy waar ñi ragal Yàlla,
4تَنزِيلًا مِّمَّنْ خَلَقَ الْأَرْضَ وَالسَّمَاوَاتِ الْعُلَى
dafa wàcc bawoo ca Ka bind suuf si ak asamaan yu kawe ya.
5الرَّحْمَٰنُ عَلَى الْعَرْشِ اسْتَوَىٰ
Yàllaa nga yemoo ca Gàngunaay ga [Aras].
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Taha 3

Simoore Taha Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [waaye] Danu koo wàcce ngir muy waar ñi ragal Yàlla,

Simoore Aaya 3/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers