Taha · 2/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
مَا أَنزَلْنَا عَلَيْكَ الْقُرْآنَ لِتَشْقَىٰ ۝٢
Maaa anzalnaa `alaikal Qur-aana litashqaaa
📖 Tekkim Wolof
Wàccewunu Alxuraan jii ci yaw ngir nga texeedi [tiis],

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore Taha

1طه
Taa Haa.
2مَا أَنزَلْنَا عَلَيْكَ الْقُرْآنَ لِتَشْقَىٰ
Wàccewunu Alxuraan jii ci yaw ngir nga texeedi [tiis],
3إِلَّا تَذْكِرَةً لِّمَن يَخْشَىٰ
[waaye] Danu koo wàcce ngir muy waar ñi ragal Yàlla,
4تَنزِيلًا مِّمَّنْ خَلَقَ الْأَرْضَ وَالسَّمَاوَاتِ الْعُلَى
dafa wàcc bawoo ca Ka bind suuf si ak asamaan yu kawe ya.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Taha 2

Simoore Taha Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wàccewunu Alxuraan jii ci yaw ngir nga texeedi [tiis],

Simoore Aaya 2/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers