Taha · 4/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
تَنزِيلًا مِّمَّنْ خَلَقَ الْأَرْضَ وَالسَّمَاوَاتِ الْعُلَى ۝٤
Tanzeelam mimman khalaqal arda was samaawaatil `ulaa
📖 Tekkim Wolof
dafa wàcc bawoo ca Ka bind suuf si ak asamaan yu kawe ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Taha

2مَا أَنزَلْنَا عَلَيْكَ الْقُرْآنَ لِتَشْقَىٰ
Wàccewunu Alxuraan jii ci yaw ngir nga texeedi [tiis],
3إِلَّا تَذْكِرَةً لِّمَن يَخْشَىٰ
[waaye] Danu koo wàcce ngir muy waar ñi ragal Yàlla,
4تَنزِيلًا مِّمَّنْ خَلَقَ الْأَرْضَ وَالسَّمَاوَاتِ الْعُلَى
dafa wàcc bawoo ca Ka bind suuf si ak asamaan yu kawe ya.
5الرَّحْمَٰنُ عَلَى الْعَرْشِ اسْتَوَىٰ
Yàllaa nga yemoo ca Gàngunaay ga [Aras].
6لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَمَا تَحْتَ الثَّرَىٰ
Moo moom li nekk ci asamaan yi ak ci suuf si ak li nekk ci seen diggante, ak li nekk ci ron déeley suuf si.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Taha 4

Simoore Taha Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dafa wàcc bawoo ca Ka bind suuf si ak asamaan…

Simoore Aaya 4/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers