Al-Anbiya · 32/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَجَعَلْنَا السَّمَاءَ سَقْفًا مَّحْفُوظًا ۖ وَهُمْ عَنْ آيَاتِهَا مُعْرِضُونَ ۝٣٢
Wa ja`alnas samaaa`a saqfam mahfoozanw wa hum `an Aayaatihaa mu`ridoon
📖 Tekkim Wolof
Te def Nanu asamaan si mu nekk am téeg mu Nu wattu. Te ñoom ñangay dëddu Sunuy kéemtaan [bañ leen a seetlu].

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Al-Anbiya

30أَوَلَمْ يَرَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَنَّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ كَانَتَا رَتْقًا فَفَتَقْنَاهُمَا ۖ وَجَعَلْنَا مِنَ الْمَاءِ كُلَّ شَيْءٍ حَيٍّ ۖ أَفَلَا يُؤْمِنُونَ
Ndax ña weddi dañoo gisul ne asamaan yi ak suuf si dañoo taqaloodef [benn dank] ? Nu daldi leen téqale, te Nu sose ndox lépp luy dundu. Moo ndax dañu dul gëm ?
31وَجَعَلْنَا فِي الْأَرْضِ رَوَاسِيَ أَن تَمِيدَ بِهِمْ وَجَعَلْنَا فِيهَا فِجَاجًا سُبُلًا لَّعَلَّهُمْ يَهْتَدُونَ
Te def Nanu ci biir suuf si ay tundi doj, ngir mu bañ a baj-baji ak ñoom. Te def Nanu ci ay yoon ngir ñu mën a gindiku.
32وَجَعَلْنَا السَّمَاءَ سَقْفًا مَّحْفُوظًا ۖ وَهُمْ عَنْ آيَاتِهَا مُعْرِضُونَ
Te def Nanu asamaan si mu nekk am téeg mu Nu wattu. Te ñoom ñangay dëddu Sunuy kéemtaan [bañ leen a seetlu].
33وَهُوَ الَّذِي خَلَقَ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ وَالشَّمْسَ وَالْقَمَرَ ۖ كُلٌّ فِي فَلَكٍ يَسْبَحُونَ
Te Moom mooy ki bind guddi gi ak bëccëg bi, ak jant bi ak weer wi, ku ci nekk di daw caw rëdd [wa ñu ko rëddal].
34وَمَا جَعَلْنَا لِبَشَرٍ مِّن قَبْلِكَ الْخُلْدَ ۖ أَفَإِن مِّتَّ فَهُمُ الْخَالِدُونَ
Te defalunu kenn nit ca la la jiitu muy ku fi sax. Waaw konndax yaw ginnaaw boo deewee, ñoom dañu fiy sax ba fàwwu ? [Déedéet]
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Anbiya 32

Simoore Al-Anbiya Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te def Nanu asamaan si mu nekk am téeg mu…

Simoore Aaya 32/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers