Al-Furqan · 20/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
وَمَا أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ مِنَ الْمُرْسَلِينَ إِلَّا إِنَّهُمْ لَيَأْكُلُونَ الطَّعَامَ وَيَمْشُونَ فِي الْأَسْوَاقِ ۗ وَجَعَلْنَا بَعْضَكُمْ لِبَعْضٍ فِتْنَةً أَتَصْبِرُونَ ۗ وَكَانَ رَبُّكَ بَصِيرًا ۝٢٠
Wa maaa arsalnaa qablaka minal mursaleena illaaa innahum la yaakuloonat ta`aama wa yamshoona fil aswaaq; wa ja`alnaa ba`dakum liba`din fitnatan atasbiroon; wa kaana Rabbuka Baseera
📖 Tekkim Wolof
Musunoo yebal ay Yonent ca la la jiitu lu dul dañu daan lekk ñam te di dox ci ja yi [màrse yi]. Def Nanu it ñenn ci yéen di sànjeb ña ca des, mbaa dangeen muñ ? - Sa Boroom de kuy gis la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Al-Furqan

18قَالُوا سُبْحَانَكَ مَا كَانَ يَنبَغِي لَنَا أَن نَّتَّخِذَ مِن دُونِكَ مِنْ أَوْلِيَاءَ وَلَٰكِن مَّتَّعْتَهُمْ وَآبَاءَهُمْ حَتَّىٰ نَسُوا الذِّكْرَ وَكَانُوا قَوْمًا بُورًا
Ñuy wax di tontu naan : “Tudd nanu sa sell gi. ! Yellut ci nun nuy wut kilifa bàyyi la, waaye Yaa leen tuuroon xéewal ñook seeni baay ba tax ñu fàtte [Alxuraan]. Far sànku”.
19فَقَدْ كَذَّبُوكُم بِمَا تَقُولُونَ فَمَا تَسْتَطِيعُونَ صَرْفًا وَلَا نَصْرًا ۚ وَمَن يَظْلِم مِّنكُمْ نُذِقْهُ عَذَابًا كَبِيرًا
“Weddi woon nañu leen ca li ngeen di wax. Amuñu ab rawtukaay. Te képp ku tooñati ci yéen, Dananu ko mosal mbugal mu réy”.
20وَمَا أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ مِنَ الْمُرْسَلِينَ إِلَّا إِنَّهُمْ لَيَأْكُلُونَ الطَّعَامَ وَيَمْشُونَ فِي الْأَسْوَاقِ ۗ وَجَعَلْنَا بَعْضَكُمْ لِبَعْضٍ فِتْنَةً أَتَصْبِرُونَ ۗ وَكَانَ رَبُّكَ بَصِيرًا
Musunoo yebal ay Yonent ca la la jiitu lu dul dañu daan lekk ñam te di dox ci ja yi [màrse yi]. Def Nanu it ñenn ci yéen di sànjeb ña ca des, mbaa dangeen muñ ? - Sa Boroom de kuy gis la.
21۞ وَقَالَ الَّذِينَ لَا يَرْجُونَ لِقَاءَنَا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْنَا الْمَلَائِكَةُ أَوْ نَرَىٰ رَبَّنَا ۗ لَقَدِ اسْتَكْبَرُوا فِي أَنفُسِهِمْ وَعَتَوْا عُتُوًّا كَبِيرًا
Ña yaakaarul a dajeek Nun ñangay wax naan : “Céy bées wàcce woon ci nun ay Malaaka, mbaa nu gis sunu Boroom [Yàlla] ! ”. Dañu doon rëy-rëylu [kaweel seen bopp], réer réer gu jéggi dayo.
22يَوْمَ يَرَوْنَ الْمَلَائِكَةَ لَا بُشْرَىٰ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُجْرِمِينَ وَيَقُولُونَ حِجْرًا مَّحْجُورًا
Bis ba ñuy mën a gis malaaka ya du neex ci ñoom de, ndax Malaaka yaa nga naan leen : “Seeni mbir sakk na” !
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Furqan 20

Simoore Al-Furqan Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Musunoo yebal ay Yonent ca la la jiitu lu dul…

Simoore Aaya 20/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers