Al-Furqan · 53/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
۞ وَهُوَ الَّذِي مَرَجَ الْبَحْرَيْنِ هَٰذَا عَذْبٌ فُرَاتٌ وَهَٰذَا مِلْحٌ أُجَاجٌ وَجَعَلَ بَيْنَهُمَا بَرْزَخًا وَحِجْرًا مَّحْجُورًا ۝٥٣
Wa Huwal lazee marajal bahraini haazaa `azbun furaatunw wa haazaa milhun ujaaj; wa ja`ala bainahumaa barzakhanw wa hijram mahjooraa
📖 Tekkim Wolof
Mooy Kiy dawloo ñaari géej : bii neex, lewet, ba ca des saf xorom, naqari. Te moo def ci seen diggante aw téq [bu kenn mënul a jaxase].

🎧 Dégg


📜 Aaya 51-55 — Simoore Al-Furqan

51وَلَوْ شِئْنَا لَبَعَثْنَا فِي كُلِّ قَرْيَةٍ نَّذِيرًا
Bu Nu sooboon, dëkk bu nekk Dananu fa yebal ab xuppekat.
52فَلَا تُطِعِ الْكَافِرِينَ وَجَاهِدْهُم بِهِ جِهَادًا كَبِيرًا
Bul topp ñiy weddi Alxuraan ; te nanga xeex ak ñoom xeex bu rëy.
53۞ وَهُوَ الَّذِي مَرَجَ الْبَحْرَيْنِ هَٰذَا عَذْبٌ فُرَاتٌ وَهَٰذَا مِلْحٌ أُجَاجٌ وَجَعَلَ بَيْنَهُمَا بَرْزَخًا وَحِجْرًا مَّحْجُورًا
Mooy Kiy dawloo ñaari géej : bii neex, lewet, ba ca des saf xorom, naqari. Te moo def ci seen diggante aw téq [bu kenn mënul a jaxase].
54وَهُوَ الَّذِي خَلَقَ مِنَ الْمَاءِ بَشَرًا فَجَعَلَهُ نَسَبًا وَصِهْرًا ۗ وَكَانَ رَبُّكَ قَدِيرًا
Mooy ki sos nit ci ndox, def ci aw askan ak ug goromle. Sa Boroom di Ku am kàttan [ci def lu nekk].
55وَيَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَنفَعُهُمْ وَلَا يَضُرُّهُمْ ۗ وَكَانَ الْكَافِرُ عَلَىٰ رَبِّهِ ظَهِيرًا
[Yéefar ya], ña ngay jaamu, bàyyi Yàlla, loo xam ne duleen jariñ, duleen lor ! Ku di ab yéefar mooy takkatook noonub Boroomam !
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Al-Furqan 53

Simoore Al-Furqan Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy Kiy dawloo ñaari géej : bii neex, lewet, ba…

Simoore Aaya 53/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers