An-Naml · 18/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
حَتَّىٰ إِذَا أَتَوْا عَلَىٰ وَادِ النَّمْلِ قَالَتْ نَمْلَةٌ يَا أَيُّهَا النَّمْلُ ادْخُلُوا مَسَاكِنَكُمْ لَا يَحْطِمَنَّكُمْ سُلَيْمَانُ وَجُنُودُهُ وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ ١٨
Transliteration
hattaaa izaaa ataw `alaa waadin namli qaalat namlatuny yaaa aiyuhan namlud khuloo masaakinakum laa yahtimannakum Sulaimaanu wa junooduhoo wa hum laa yash`uroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu agsee ca xuru xorondom ya, mu am xurondom wu wax ne : "Éy yéen xorondom yi, dugguleen ci seeni biir kër, balaa leen a Suleymaan ak i xaritam di nappaaje te duñu ko sax yëg”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 16-20 — Simoore An-Naml
16وَوَرِثَ سُلَيْمَانُ دَاوُودَ ۖ وَقَالَ يَا أَيُّهَا النَّاسُ عُلِّمْنَا مَنطِقَ الطَّيْرِ وَأُوتِينَا مِن كُلِّ شَيْءٍ ۖ إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْفَضْلُ الْمُبِينُ
Suleymaan wuutu na Daawuda, daldi ne : “Éy yéen nit ñi ! Xam naa waxi picc yi ; te am naa lu ne. Loolu mooy ngëneel lu bir.
17وَحُشِرَ لِسُلَيْمَانَ جُنُودُهُ مِنَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ وَالطَّيْرِ فَهُمْ يُوزَعُونَ
Dajaleef na Suleymaan ak i xaritam, cij jinne yeek nit ñi, ñu def i sàppe.
18حَتَّىٰ إِذَا أَتَوْا عَلَىٰ وَادِ النَّمْلِ قَالَتْ نَمْلَةٌ يَا أَيُّهَا النَّمْلُ ادْخُلُوا مَسَاكِنَكُمْ لَا يَحْطِمَنَّكُمْ سُلَيْمَانُ وَجُنُودُهُ وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Ba ñu agsee ca xuru xorondom ya, mu am xurondom wu wax ne : "Éy yéen xorondom yi, dugguleen ci seeni biir kër, balaa leen a Suleymaan ak i xaritam di nappaaje te duñu ko sax yëg”.
19فَتَبَسَّمَ ضَاحِكًا مِّن قَوْلِهَا وَقَالَ رَبِّ أَوْزِعْنِي أَنْ أَشْكُرَ نِعْمَتَكَ الَّتِي أَنْعَمْتَ عَلَيَّ وَعَلَىٰ وَالِدَيَّ وَأَنْ أَعْمَلَ صَالِحًا تَرْضَاهُ وَأَدْخِلْنِي بِرَحْمَتِكَ فِي عِبَادِكَ الصَّالِحِينَ
[Suleymaan] muuñ, daldi ree ndax wax jooju, daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, Nanga baaxe may sant ci xéewal gii Nga ma dafal maak samay waajur, te may jëf jëf ju baax Joo gërëm te Nga may ma ci Sa yërmaande ma bokk ca Sa jaam ñu yiw ña”.
20وَتَفَقَّدَ الطَّيْرَ فَقَالَ مَا لِيَ لَا أَرَى الْهُدْهُدَ أَمْ كَانَ مِنَ الْغَائِبِينَ
Mu nemmiku njanaaw ya, daldi ne : “Lan moo tax gisuma Muusaa-njuburi ? Walla nekku fi?
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
18Aaya
Tekki — An-Naml 18
Simoore An-Naml Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu agsee ca xuru xorondom ya, mu am xurondom…Simoore Aaya 18/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








