Aali Imran · 110/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
كُنتُمْ خَيْرَ أُمَّةٍ أُخْرِجَتْ لِلنَّاسِ تَأْمُرُونَ بِالْمَعْرُوفِ وَتَنْهَوْنَ عَنِ الْمُنكَرِ وَتُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ ۗ وَلَوْ آمَنَ أَهْلُ الْكِتَابِ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُم ۚ مِّنْهُمُ الْمُؤْمِنُونَ وَأَكْثَرُهُمُ الْفَاسِقُونَ ۝١١٠
Kuntum khaira ummatin ukhrijat linnaasi taamuroona bilma`roofi wa tanhawna `anil munkari wa tu`minoona billaah; wa law aamana Ahlul Kitaabi lakaana khairal lahum minhumul mu`minoona wa aksaruhumul faasiqoon
📖 Tekkim Wolof
Yéen yéen ay xeet wi gën ci nit ñi [xeet wu fi mës a jaar]. Yéen ay digle njekk te tere njekkar te gëm Yàlla. Bu ñoñ-téere gëmoon, mooy gën ci ñoom de, li ëpp ci ñoom ay saay- saay lañu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 108-112 — Aali Imran

108تِلْكَ آيَاتُ اللَّهِ نَتْلُوهَا عَلَيْكَ بِالْحَقِّ ۗ وَمَا اللَّهُ يُرِيدُ ظُلْمًا لِّلْعَالَمِينَ
Loolu moo di kàdduy Yàlla ya ; Danañu ko jàngat ci yaw (Muhammad) ci dëgg. Yàlla nammul di tooñ mbindéef yi.
109وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ
Yàllaa moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Te mbir yépp ca Yàlla lañuy mujj [dellusi].
110كُنتُمْ خَيْرَ أُمَّةٍ أُخْرِجَتْ لِلنَّاسِ تَأْمُرُونَ بِالْمَعْرُوفِ وَتَنْهَوْنَ عَنِ الْمُنكَرِ وَتُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ ۗ وَلَوْ آمَنَ أَهْلُ الْكِتَابِ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُم ۚ مِّنْهُمُ الْمُؤْمِنُونَ وَأَكْثَرُهُمُ الْفَاسِقُونَ
Yéen yéen ay xeet wi gën ci nit ñi [xeet wu fi mës a jaar]. Yéen ay digle njekk te tere njekkar te gëm Yàlla. Bu ñoñ-téere gëmoon, mooy gën ci ñoom de, li ëpp ci ñoom ay saay- saay lañu.
111لَن يَضُرُّوكُمْ إِلَّا أَذًى ۖ وَإِن يُقَاتِلُوكُمْ يُوَلُّوكُمُ الْأَدْبَارَ ثُمَّ لَا يُنصَرُونَ
Duñu la mën a lore lu dul ci wax ju ñaaw ; te bu ngeen xaree ak ñoom, ñu joxe ginnaaw [daw], kenn duleen dimbali.
112ضُرِبَتْ عَلَيْهِمُ الذِّلَّةُ أَيْنَ مَا ثُقِفُوا إِلَّا بِحَبْلٍ مِّنَ اللَّهِ وَحَبْلٍ مِّنَ النَّاسِ وَبَاءُوا بِغَضَبٍ مِّنَ اللَّهِ وَضُرِبَتْ عَلَيْهِمُ الْمَسْكَنَةُ ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَانُوا يَكْفُرُونَ بِآيَاتِ اللَّهِ وَيَقْتُلُونَ الْأَنبِيَاءَ بِغَيْرِ حَقٍّ ۚ ذَٰلِكَ بِمَا عَصَوا وَّكَانُوا يَعْتَدُونَ
Fu ñu mën a nekk, toroxtaange dal leen, lu dul ña ca yiiroon kóllareg Yàlla walla gu nit ña. Te ñoom merum Yàlla dal na leen, ñu daldi simbook ñàkk [ndóol] ngir weddi ga ñu weddi kàdduy Yàlla ak rey ga ñu rey Yonent ya ci lu dul dëgg, booleek moy Yàlla gi ñu saxoo woon, di jalgati.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
110Aaya

Tekki — Aali Imran 110

Simoore Aali Imran Aaya 110 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen yéen ay xeet wi gën ci nit ñi [xeet…

Simoore Aaya 110/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 108–112. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers