Aali Imran · 109/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ ۝١٠٩
Wa lillaahi maa fissamaawaati wa maa fil ard; wa ilal laahi turja;ul umoor
📖 Tekkim Wolof
Yàllaa moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Te mbir yépp ca Yàlla lañuy mujj [dellusi].

🎧 Dégg


📜 Aaya 107-111 — Simoore Aali Imran

107وَأَمَّا الَّذِينَ ابْيَضَّتْ وُجُوهُهُمْ فَفِي رَحْمَةِ اللَّهِ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Ña nga xam ne seeni kanam ya dafa weex, dana ñu nekk ci yërmaandey Yàlla, te dañu fay béel.
108تِلْكَ آيَاتُ اللَّهِ نَتْلُوهَا عَلَيْكَ بِالْحَقِّ ۗ وَمَا اللَّهُ يُرِيدُ ظُلْمًا لِّلْعَالَمِينَ
Loolu moo di kàdduy Yàlla ya ; Danañu ko jàngat ci yaw (Muhammad) ci dëgg. Yàlla nammul di tooñ mbindéef yi.
109وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۚ وَإِلَى اللَّهِ تُرْجَعُ الْأُمُورُ
Yàllaa moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Te mbir yépp ca Yàlla lañuy mujj [dellusi].
110كُنتُمْ خَيْرَ أُمَّةٍ أُخْرِجَتْ لِلنَّاسِ تَأْمُرُونَ بِالْمَعْرُوفِ وَتَنْهَوْنَ عَنِ الْمُنكَرِ وَتُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ ۗ وَلَوْ آمَنَ أَهْلُ الْكِتَابِ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُم ۚ مِّنْهُمُ الْمُؤْمِنُونَ وَأَكْثَرُهُمُ الْفَاسِقُونَ
Yéen yéen ay xeet wi gën ci nit ñi [xeet wu fi mës a jaar]. Yéen ay digle njekk te tere njekkar te gëm Yàlla. Bu ñoñ-téere gëmoon, mooy gën ci ñoom de, li ëpp ci ñoom ay saay- saay lañu.
111لَن يَضُرُّوكُمْ إِلَّا أَذًى ۖ وَإِن يُقَاتِلُوكُمْ يُوَلُّوكُمُ الْأَدْبَارَ ثُمَّ لَا يُنصَرُونَ
Duñu la mën a lore lu dul ci wax ju ñaaw ; te bu ngeen xaree ak ñoom, ñu joxe ginnaaw [daw], kenn duleen dimbali.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
109Aaya

Tekki — Aali Imran 109

Simoore Aali Imran Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàllaa moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si.…

Simoore Aaya 109/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers