Ar-Rum · 2/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
غُلِبَتِ الرُّومُ ۝٢
Ghulibatir Room
📖 Tekkim Wolof
Noteef na waa Rom,

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore Ar-Rum

1الم
Alif, Laam, Miim.
2غُلِبَتِ الرُّومُ
Noteef na waa Rom,
3فِي أَدْنَى الْأَرْضِ وَهُم مِّن بَعْدِ غَلَبِهِمْ سَيَغْلِبُونَ
ci réew yi leen gën a jegeñ, wante ginnaaw nooteef googu, ñoom it danañu not ,
4فِي بِضْعِ سِنِينَ ۗ لِلَّهِ الْأَمْرُ مِن قَبْلُ وَمِن بَعْدُ ۚ وَيَوْمَئِذٍ يَفْرَحُ الْمُؤْمِنُونَ
ci biir diirub lu matul fukki at. Yàlla moo yor dogal yi, ci la jëkkoon ak li lay mujj, bu boobaa way-gëm ñi danañu sëgg ree, bég
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Ar-Rum 2

Simoore Ar-Rum Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noteef na waa Rom,

Simoore Aaya 2/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers