Ar-Rum · 3/60
Tekki Waxtaan — Ar-Rum
فِي أَدْنَى الْأَرْضِ وَهُم مِّن بَعْدِ غَلَبِهِمْ سَيَغْلِبُونَ ۝٣
Feee adnal ardi wa hummim ba`di ghalabihim sa ya ghliboon
📖 Tekkim Wolof
ci réew yi leen gën a jegeñ, wante ginnaaw nooteef googu, ñoom it danañu not ,
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-5 — Ar-Rum

1الم
Alif, Laam, Miim.
2غُلِبَتِ الرُّومُ
Noteef na waa Rom,
3فِي أَدْنَى الْأَرْضِ وَهُم مِّن بَعْدِ غَلَبِهِمْ سَيَغْلِبُونَ
ci réew yi leen gën a jegeñ, wante ginnaaw nooteef googu, ñoom it danañu not ,
4فِي بِضْعِ سِنِينَ ۗ لِلَّهِ الْأَمْرُ مِن قَبْلُ وَمِن بَعْدُ ۚ وَيَوْمَئِذٍ يَفْرَحُ الْمُؤْمِنُونَ
ci biir diirub lu matul fukki at. Yàlla moo yor dogal yi, ci la jëkkoon ak li lay mujj, bu boobaa way-gëm ñi danañu sëgg ree, bég
5بِنَصْرِ اللَّهِ ۚ يَنصُرُ مَن يَشَاءُ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
ci ndimbalul Yàlla. [Moom Yàlla] mooy dimbali ku ko soob, Mooy boroom Kàttan, di Jaglewaakon bi.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Ar-Rum 3

Simoore Ar-Rum Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ci réew yi leen gën a jegeñ, wante ginnaaw nooteef…

Simoore Aaya 3/60 — Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rum Dégg, Ar-Rum Tekki, Ar-Rum mp3, Ar-Rum pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers