Az-Zumar · 11/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
قُلْ إِنِّي أُمِرْتُ أَنْ أَعْبُدَ اللَّهَ مُخْلِصًا لَّهُ الدِّينَ ١١
Transliteration
Qul inneee umirtu an a`budal laaha mukhlisal lahud deen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “digëléef na ma may jaamu Yàlla di ko sellalal diinéem,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 9-13 — Az-Zumar
9أَمَّنْ هُوَ قَانِتٌ آنَاءَ اللَّيْلِ سَاجِدًا وَقَائِمًا يَحْذَرُ الْآخِرَةَ وَيَرْجُو رَحْمَةَ رَبِّهِ ۗ قُلْ هَلْ يَسْتَوِي الَّذِينَ يَعْلَمُونَ وَالَّذِينَ لَا يَعْلَمُونَ ۗ إِنَّمَا يَتَذَكَّرُ أُولُو الْأَلْبَابِ
Moo ndax, kuy jóg, diggu guddi, di sujuud ak a taxaw( julli), ngir moytu (tiisu àllaaxira) tey yaakaar yërmaandey Boroomam... Waxal ne : “Ndax ñi xam danañu yem, niróok ñi xamadi ? ” Li wér moo di ne woroom xel yi rekk ay fàttaliku.
10قُلْ يَا عِبَادِ الَّذِينَ آمَنُوا اتَّقُوا رَبَّكُمْ ۚ لِلَّذِينَ أَحْسَنُوا فِي هَٰذِهِ الدُّنْيَا حَسَنَةٌ ۗ وَأَرْضُ اللَّهِ وَاسِعَةٌ ۗ إِنَّمَا يُوَفَّى الصَّابِرُونَ أَجْرَهُم بِغَيْرِ حِسَابٍ
Waxal ne : “Éy yéen Sama jaam ñi gëm ! Ragalleen seen Boroom (Yàlla)”. Ñiy jëf aw yiw ci àddina, danañu am [aw yiw]. Te suufus Yàlla si yaatu na te muñkat yi danañu leen jox seenug pey mu mat sëkk ci lu dul ak waññ.
11قُلْ إِنِّي أُمِرْتُ أَنْ أَعْبُدَ اللَّهَ مُخْلِصًا لَّهُ الدِّينَ
Waxal ne : “digëléef na ma may jaamu Yàlla di ko sellalal diinéem,
12وَأُمِرْتُ لِأَنْ أَكُونَ أَوَّلَ الْمُسْلِمِينَ
te it digaléef na ma doon Jullit buy jëkk.
13قُلْ إِنِّي أَخَافُ إِنْ عَصَيْتُ رَبِّي عَذَابَ يَوْمٍ عَظِيمٍ
Waxal ne : “Ragal naa, su ma mettee sama Boroom, (dajeek) mbugëlam bis bu màgg”.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
11Aaya
Tekki — Az-Zumar 11
Simoore Az-Zumar Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “digëléef na ma may jaamu Yàlla di…Simoore Aaya 11/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








