Ghafir · 3/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
غَافِرِ الذَّنبِ وَقَابِلِ التَّوْبِ شَدِيدِ الْعِقَابِ ذِي الطَّوْلِ ۖ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ إِلَيْهِ الْمَصِيرُ ۝٣
Ghaafiriz zambi wa qaabilit tawbi shadeedil `iqaabi zit tawli laaa ilaaha illaa Huwa ilaihil maseer
📖 Tekkim Wolof
Mooy Jéggalkatu bàkkaar yi, di Nanguwaakoonu tuub, di ku Tar mbugël, mooy Boroom xéewal yi. Amul jeneen Yàlla judul Moom te ci Moom la lépp di mujj.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Ghafir

1حم
Haa, Miim.
2تَنزِيلُ الْكِتَابِ مِنَ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْعَلِيمِ
Wàcceg téere bii ma ngi bawoo ca Yàlla, miy boroom Kàttan, te di ku Xam.
3غَافِرِ الذَّنبِ وَقَابِلِ التَّوْبِ شَدِيدِ الْعِقَابِ ذِي الطَّوْلِ ۖ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ إِلَيْهِ الْمَصِيرُ
Mooy Jéggalkatu bàkkaar yi, di Nanguwaakoonu tuub, di ku Tar mbugël, mooy Boroom xéewal yi. Amul jeneen Yàlla judul Moom te ci Moom la lépp di mujj.
4مَا يُجَادِلُ فِي آيَاتِ اللَّهِ إِلَّا الَّذِينَ كَفَرُوا فَلَا يَغْرُرْكَ تَقَلُّبُهُمْ فِي الْبِلَادِ
Kenn du dàggasante ci kàdduy Yàlla ku dul yéefar yi. bu la seeni feem nax.
5كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ وَالْأَحْزَابُ مِن بَعْدِهِمْ ۖ وَهَمَّتْ كُلُّ أُمَّةٍ بِرَسُولِهِمْ لِيَأْخُذُوهُ ۖ وَجَادَلُوا بِالْبَاطِلِ لِيُدْحِضُوا بِهِ الْحَقَّ فَأَخَذْتُهُمْ ۖ فَكَيْفَ كَانَ عِقَابِ
Nitu Nooh, weddi woon na ñu ca la leen jiitu woon, ak farandoo ya (weddi woon na ñu ñoom itam), xeet wu nekk taqal ab yonnentam. Sànjaafu ko di dàggasante ak moom bëggoon a suufeel dëgg. Mu daldi leen fob (faagaagal leen). Cëy ni ma leen mbugële !
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Ghafir 3

Simoore Ghafir Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy Jéggalkatu bàkkaar yi, di Nanguwaakoonu tuub, di ku Tar…

Simoore Aaya 3/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers