Ghafir · 8/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
رَبَّنَا وَأَدْخِلْهُمْ جَنَّاتِ عَدْنٍ الَّتِي وَعَدتَّهُمْ وَمَن صَلَحَ مِنْ آبَائِهِمْ وَأَزْوَاجِهِمْ وَذُرِّيَّاتِهِمْ ۚ إِنَّكَ أَنتَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝٨
Rabbannaa wa adkhilhum Jannaati `adninil latee wa`attahum wa man salaha min aabaaa`ihim wa azwaajihim wa zurriyyaatihim; innaka Antal `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Yaw sunu Boroom ! Tàbballeen àjjana Aden ja nga leen digoon, ak képp ku baaxoon ci seeni baay ak i maam, ak seeni soxna ak seeni sët, yaw yaa di boroom Kàttan, di ku Xereñ.
🎧 Dégg

📜 Aaya 6-10 — Ghafir

6وَكَذَٰلِكَ حَقَّتْ كَلِمَتُ رَبِّكَ عَلَى الَّذِينَ كَفَرُوا أَنَّهُمْ أَصْحَابُ النَّارِ
Noonu it la sa kàddug Boroom yaye ci kaw yéefar yi : “Ñoom ñooy waa Safara”.
7الَّذِينَ يَحْمِلُونَ الْعَرْشَ وَمَنْ حَوْلَهُ يُسَبِّحُونَ بِحَمْدِ رَبِّهِمْ وَيُؤْمِنُونَ بِهِ وَيَسْتَغْفِرُونَ لِلَّذِينَ آمَنُوا رَبَّنَا وَسِعْتَ كُلَّ شَيْءٍ رَّحْمَةً وَعِلْمًا فَاغْفِرْ لِلَّذِينَ تَابُوا وَاتَّبَعُوا سَبِيلَكَ وَقِهِمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ
Ña yanu Aras ak ña ko wër ña ngay sàbbaal di kañ seen Boroom, di ko gëm tey jéggalu ñi gëm naan ko : “Yaw sunu Boroom ! sa yërmaande yaatu na man a daj ñépp ak sa xam-xam. Kon jéggëlal ña daan tuub tey topp sa yoon wi te nga fegalleen mbugëlu Safara.
8رَبَّنَا وَأَدْخِلْهُمْ جَنَّاتِ عَدْنٍ الَّتِي وَعَدتَّهُمْ وَمَن صَلَحَ مِنْ آبَائِهِمْ وَأَزْوَاجِهِمْ وَذُرِّيَّاتِهِمْ ۚ إِنَّكَ أَنتَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Yaw sunu Boroom ! Tàbballeen àjjana Aden ja nga leen digoon, ak képp ku baaxoon ci seeni baay ak i maam, ak seeni soxna ak seeni sët, yaw yaa di boroom Kàttan, di ku Xereñ.
9وَقِهِمُ السَّيِّئَاتِ ۚ وَمَن تَقِ السَّيِّئَاتِ يَوْمَئِذٍ فَقَدْ رَحِمْتَهُ ۚ وَذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
Te nga fegalleen [mbugëlu] ñaawtéef yi. Képp koo fegal [mbugëlum] ñaawtéef, Yërëm nga ko tigi”. Te loolu mooy texe gu mag ga.
10إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا يُنَادَوْنَ لَمَقْتُ اللَّهِ أَكْبَرُ مِن مَّقْتِكُمْ أَنفُسَكُمْ إِذْ تُدْعَوْنَ إِلَى الْإِيمَانِ فَتَكْفُرُونَ
Ña weddi nag ñoom dañu leen woo naan leen : “jéppig Yàlla moo gën a rëy ni ngeen jéppee seen bopp, ba ñu leen daan woo jëme leen ci ngëm dangeen daan weddi”.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Ghafir 8

Simoore Ghafir Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw sunu Boroom ! Tàbballeen àjjana Aden ja nga leen…

Simoore Aaya 8/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers