Al-Jathiya · 6/37
Tekki Waxtaan — Al-Jathiya
تِلْكَ آيَاتُ اللَّهِ نَتْلُوهَا عَلَيْكَ بِالْحَقِّ ۖ فَبِأَيِّ حَدِيثٍ بَعْدَ اللَّهِ وَآيَاتِهِ يُؤْمِنُونَ ٦
Transliteration
Tilka Aayatul laahi natloohaa `alika bilhaqq, fabiayyi hadeesim ba`dal laahi wa Aayaatihee yu`minoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yooyu ñooy firndey Yàlla nu di la ko jàngal mu tegu ci dëgg. Kon ana jan wax la ñuy man a gëm ginnaaw bu Yàlla ak firndeem Yii jàllee?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 4-8 — Al-Jathiya
4وَفِي خَلْقِكُمْ وَمَا يَبُثُّ مِن دَابَّةٍ آيَاتٌ لِّقَوْمٍ يُوقِنُونَ
Ay kéemtaan it, yuy soxal ñi amug wóolu nekk na ci bind, bi ngéen ame ay ci lépp luy dukkat ca anam ya muy giire.
5وَاخْتِلَافِ اللَّيْلِ وَالنَّهَارِ وَمَا أَنزَلَ اللَّهُ مِنَ السَّمَاءِ مِن رِّزْقٍ فَأَحْيَا بِهِ الْأَرْضَ بَعْدَ مَوْتِهَا وَتَصْرِيفِ الرِّيَاحِ آيَاتٌ لِّقَوْمٍ يَعْقِلُونَ
Ak ci jëllasanteb guddi gi ak bëccëg bi, ak ci xeewal gi Yàlla wàcce mu bawoo ci asamaan si [Taw] di ci dundal suuf si (Naataange) ginnaaw ba mu bekkooree, ak ci ni muy soppaxndikoo ngelaw yi, ay kéemtaan la yuy soxal ñi xellu.
6تِلْكَ آيَاتُ اللَّهِ نَتْلُوهَا عَلَيْكَ بِالْحَقِّ ۖ فَبِأَيِّ حَدِيثٍ بَعْدَ اللَّهِ وَآيَاتِهِ يُؤْمِنُونَ
Yooyu ñooy firndey Yàlla nu di la ko jàngal mu tegu ci dëgg. Kon ana jan wax la ñuy man a gëm ginnaaw bu Yàlla ak firndeem Yii jàllee?
7وَيْلٌ لِّكُلِّ أَفَّاكٍ أَثِيمٍ
Képp ku dib duuraakoon defaakoonub bàkkaar toskare na ca xuri sawara !
8يَسْمَعُ آيَاتِ اللَّهِ تُتْلَىٰ عَلَيْهِ ثُمَّ يُصِرُّ مُسْتَكْبِرًا كَأَن لَّمْ يَسْمَعْهَا ۖ فَبَشِّرْهُ بِعَذَابٍ أَلِيمٍ
Daan dégg ñuy jàng laayay Yàlla yi ( Alxuraan) mu féttéerlu di jaayub dayo, melni ku ko déggul. (Kookee na xam ne ) mbugal mu mettee (nga koy xaar).
Al-JathiyaFihi Alxuraan
37Aaya
MeccanRevelation
6Aaya
Tekki — Al-Jathiya 6
Simoore Al-Jathiya Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yooyu ñooy firndey Yàlla nu di la ko jàngal mu…Simoore Aaya 6/37 — Al-Jathiya الجاثية (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jathiya Dégg, Al-Jathiya Tekki, Al-Jathiya mp3, Al-Jathiya pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








